audio audioduration (s) 0.74 50.6 | transcription stringlengths 8 285 |
|---|---|
Wàdd, kenn ci njiiti Senegaal | |
Lii du màggat mukk. | |
Dina nekk lu yomb | |
Naan na sàngara. | |
Kafe ci Ecoopi, Keeñaa, Ugandaa, Ginne, Kot Diwaar | |
Luy mbir mii jaxasoo? | |
Amul ug saytu. | |
Gisunu ko woon. | |
Xam naa jëml yii. | |
Ndaxte, ñooy wattu s unu kaaraange guddeek bëccëg | |
Ñax mi, ngir fasi la. | |
Xoolal dàlli Tom. | |
Dama koo mujjee fef. | |
Waaye, Maki jikkoy firawna lay doxe | |
Dinaa ko jéem. | |
Wóolu ma ci loolu ! | |
Tomb 12 Koom mi | |
Nu ngi ci kaaraange. | |
Toog leen fii. | |
manuma koo génne. | |
ña jànq it seen diñe gaay seen wéttal | |
Lu tax nuy daw ? | |
Téyeleen ko ! | |
Dunu Falkland (Nguur-Yu-Bennoo) | |
Sama télé daa toj. | |
Màggug hip-hop ci àdduna bi | |
Toppekat dal na seen kaw bu baax | |
Ci iniweersite bi, ngongo yi ñoongi bowoo ci bërëb yu wuute | |
Summileen seen mbaxana yi . | |
Ñëwleen jëlsi ko. | |
Xobet-xobet laa soxla. | |
Dafa man a fen. | |
Ca dëgg-dëgg ag mbaax la. | |
Jagley campeef yi ak seeni ligeey | |
Tom xaalis bu bari lay fayeeku. | |
Juum naa ndax kóolute gu ëpp ci sama bopp. | |
Damay xale bu góor bu baax. | |
Diiwaan yu fatt yi ci ay way dëkk | |
Looloo taxoon njëlul nguur gi loofoon, mujjoon moom nguur gi fees dell aki bor. | |
Daa soxla xaalis. | |
Xew-xew ci bis bi | |
Defleen li mu wax ! | |
Lépp dara baaxu ci woon. | |
Daanaka amul menn piri moo xam ne ñépp dëppoo nañu ci, muy tekki garab. | |
Wànqaasam day am i dég te xobam 4 10i sàntimet àgg ci guddaay. | |
Damaa dox ba fii. | |
Lu la mar mayul, màtt du la ko may | |
Aa waaw, nanu dem. | |
Daa yaru lool. | |
Sabab yu jonjoo yi ñeel xareb adduna bu njëkk bi | |
Waaw, wax ngeen dëgg. | |
Ginnaaw bi ñu ko saytoo, la nu gis jàngoro ji ci moom | |
Ku may bàyyi xel ? | |
Dee a gën gàcce la siddiit yi ràbbaske bind ko ci xol yi. | |
Fàww nga màgg. | |
Seen ree gu neex na ma. | |
Lu tax xëpp deret nekk màndarga jóg-jot-na ci biir ëmb bi ? | |
Solleen seen yére fanaanukaay. | |
Danu koo war a jël. | |
Nun ñépp a am i ayib. | |
Bàyyil nama am mbind. | |
Kóllëre ginnaaw lay féete | |
Damaa war a jéggalu. | |
Ka wax lii de wax na wax ju rafet | |
Lalub selen boo ci tëdd it wàcci dellu fi suuf | |
Ñaata lay jar\? | |
Ndax bëggu leen ab defuma ay? | |
Gën naa tàng. | |
Gis ngeen loolu ? | |
Jàmbur yi ak Baadoola yi ñoo ci toppoon cig raŋ. | |
Génneleen mbalit yi ! | |
Mayeesuma ko kenn. | |
Ana lan moo xew? | |
Ponki jikko yi jullit bu nekk war a jikkowoo | |
Soo xuloo ak ñoom ñu dittil la bi bënnut? | |
Ana goloo ka sàngoo mbàjj bay taamu nimoro diis? | |
Benn donga a joxewul ngànt | |
Lii a ka taaru ! | |
Ginnaaw bi, nu àgg Luga,laataa fajar,yendu fa | |
Dafa niru ku maandu. | |
Sooratu Rahmaan, aaya 33 | |
Takkoon na ay weer. | |
Dolli nañu ci sax jamonoy tëju | |
Dafay naan lu ëpp. | |
Dañ maa tegoon daan. | |
Loolu laa xalaat. | |
Ndiru na ku dëgër. | |
Loolu kat moo di ay teggin, kon jëfe ko cig wàllam | |
Tëjleen bunt bi. | |
Dama soxla nelaw. | |
Mag nee na | |
Manuma ko delloo. | |
Dinaa xaar ba fukki waxtu ak ñaar. | |
Nanu fàtte loolu ! | |
Fi abadin bu nuxubi | |
Dafa am xel. | |
Dee ma yëgal fumu toll. | |
Dinanu leen dimbali. | |
Ndëgërlu gi ci gii yamale nga koy xamee | |
Dingeen dem it? |
End of preview. Expand in Data Studio
README.md exists but content is empty.
- Downloads last month
- 9