Datasets:
audio
audioduration (s) 0.54
9.99
| text
stringlengths 1
125
|
|---|---|
donc yooyu yëpp bu fekkente ne dangay béy
|
|
l’idée c’est d’alimenter le Chatbot
|
|
comme ni ma la ko waxee rek
|
|
ak engrais yeeg yooyu engrais chimique bi yooyu yëpp danga koy jënd
|
|
waa pesticides yeeg yooyu
|
|
c’est ça oui su ko defee na la permettre
|
|
dugal si lenn loo xam ne day gaaw
|
|
donte à chaque fois dangay dépenser rek
|
|
te amuloo moyens yooyu t’es obligé nga alterner
|
|
comme ça bu amee 45 jours marché bi kii wul dara
|
|
soble bi moom day pareegul
|
|
nga commencer di jënd mun na assurer soble bi
|
|
à ce que nga am des informations précises
|
|
bu fekkee am nga moyen yi taxaw na sur place
|
|
soit dañuy am Banque Agricole…mu leen di financer
|
|
là mun nga sóoru loolu culture yu mag yi
|
|
soit dañuy am ay financements
|
|
moo tax ñuy am doole googu
|
|
mooy culture associée
|
|
wala yeneen banques wala ñu ut seen tontine wala yu demee noonu
|
|
béy séddoo xaw ma lañu ko tuddee waaw
|
|
koo xamante ni am na xaalis mu jox la
|
|
wala ñu def béy associé
|
|
si
|
|
yoo xamante ne danga ko def ci chatbot bi directement
|
|
day feeñ aussi si prix de revient bi da siy feeñ
|
|
am système location aussi gis nga ko
|
|
ñoo xam ne dañuy louer seen terre
|
|
soit bu ñoree ñu séddoo génné dépenses yeeg yëpp
|
|
daal di diviser après ñu diviser en 2 parties yu demee noonu
|
|
effectivement surtout ça
|
|
est-ce que y a une phase de préparation des sols
|
|
et comment ça se fait
|
|
c’est ça oui léegi concernant pépinière bi
|
|
phase préparation boobu boo ko échouer rek
|
|
te sol bi parce que tracteur moo koy béy
|
|
ñu entraîner ko bu ñu ko entraîner léegi de ce fait
|
|
bon am na ñoo xam ne dañu koy…
|
|
parce que laboure moom mooy génne botte de terres yi
|
|
pratiquement doo am rendement bi nga bëgg
|
|
laata tracteur di ñëw ñu labourer ko herser ko
|
|
génne suuf bu bees bi après herse bi
|
|
mooy herser bi pour toj doom yi te bu mu nekk genre-u poudre
|
|
mooy da koy beneen hélice lañuy monter-waat si tracteur bi
|
|
parce que pépinière dafa oyof quoi reen bu sew la
|
|
mais sol bi comme ça suuf bi bu xawee mou nii
|
|
entrainement boobu bu demee une semaine
|
|
déjà il faut que suuf si wow bu mu nooy nepp
|
|
mën nga repiquer directement après préparation bi quoi
|
|
am na ñoo xamante ne soit dañuy jël terreau
|
|
mais nag mënoo di jël terreau
|
|
bu fekkante ne sa suuf si c’est riche amul problème
|
|
sol bi bu tàngee rek …
|
|
li waral préparation bi il faut que mu noyyi
|
|
parce que même su génnee sol bi bu tàngee
|
|
si préparation semis bi comme li ma wax
|
|
il foog mu humide aussi du tooy
|
|
boo repiquer ba pare il foog muy tooy constamment
|
|
par exemple ba miin affaire bi
|
|
suuf bi il foog mu mou il foog mu
|
|
yooyu moom ñooy conditions yi nga xamante ne
|
|
ni suuf si moom il foog mu mou quoi
|
|
il faut que ñu respecter ko quoi
|
|
parce que lu sew la donc bu ngelawee rek mën na daanu
|
|
mais ren amu ko peut être froid bi moo li mu sedd bi moo tax
|
|
warut di wow parce que période boobu day faible
|
|
soleil bi bu tàngee rek mën na seey
|
|
donc boo ko poser directement da lay jox réponse bi
|
|
parce boo xoolee daaw problème boobu dal na ma
|
|
loolu ñu comprendre affaire bi il faut nga koy muur
|
|
mais daaw si nawet bi mu tàng tàngaay boobu
|
|
day dem ba génne day commencer seey xam nga day sew
|
|
day gaaw a kii donc su génnee il faut mu amaat
|
|
benn couche boo xamante ne ñax boo xam ne
|
|
donc wàññi chaleur bi waaw rayon soleil yi ñoo koy lakk
|
|
donc yooyu yëpp danga koy respecter
|
|
mën na diminuer lumière soleil bi
|
|
danga koy tegaat wala benn saak boo xam ne
|
|
parce que Galmi ci sedd lay développer
|
|
il faut soleil bi température bi xaw a sedd
|
|
c’est ça donc mën nañu commencer
|
|
il faut que mu sedd mu développer
|
|
man paa yi may fekk foofu yëpp dañu ñu ko daan wax
|
|
Galmi si sedd lay développer donc moo tax pépinière bi aussi
|
|
parce que années yii passées li tax du développé
|
|
donc température bi da ciy joué
|
|
wala à condition nga muur ko wàññi température bi
|
|
mooy daaw vu que ne température bi la mënul a supporter
|
|
constamment moom waroo tëbal
|
|
chaque jour dangay xëy arroser ko soo ko irrigué
|
|
il faut la préparation du sol il faut aussi
|
|
si production oignon bi d’abord
|
|
tu as vu donc facteurs yooyu bon
|
|
à part ça pour engrais yi ak yooyu day xaw a kii si moom tuuti
|
|
climat bi aussi favorable pour mën a am humidité encore
|
|
parce que lu faible la dañu koy bàyyi mu progresser
|
|
yooyu dañ koy éviter quoi su dose bi ëppee rek mën na ko gaañ
|
|
ba ren di déwén nga mën ci def affaire yooyu…
|
|
engrais bi aussi nga def tuuti rek
|
|
chaque jour moom là tu es obligé
|
End of preview. Expand
in Data Studio
README.md exists but content is empty.
- Downloads last month
- 27