audio audioduration (s) 1.19 482 | transcription stringlengths 0 2.2k | locale stringclasses 2
values |
|---|---|---|
mun na indi ay jafe-jafe waaye ndax loolu moom mooy li ñu war ay ndaw lañ bu ñu gisee loo xam ne jagul danañ ko wax waaye nag lépp nag nay tegu ci xam-xam moo tax ñu koy def ci enquête ndem su fekkee * bu jeexee ki ko yor dina ko wax ñi mu ko war a waxal ñu daje ñu def su ko defee la cay génn duñ ko jébale | wol | |
la ca des comme ni ma la ko waxoon enquêtes agricoles yi dina génne ñu nagu ne ne ci taxawaay maanaam ci wàllu rendement ñaata lay am ndax li ñu am toll na ak li nga amoon daaw | wol | |
yooyu yëpp dañ bugg mu tegu ci xam-xam tegu ci enquête tegu ci ay gëstu tegu ci lu wóor mu bañ ñoo bett wax joo xam ne da ngay taxaw rek naan nañ dem tool nañ dem tool te teguwul fenn | wol | |
moom mooy que présentement cas boobu kii quoi zo() zone boobu ñu wax léegi quoi mu doon kii quoi la vallée morte de * gis nañ que nii les autorités de la région là jël nañ ko def nañ ko même aussi vraiment muy seen soxla | wol | |
te fi may waxee ak yow nii léegi am na un programme bi nga xamante gars yi ñu ngi koy tëgg ak Fond Vers Climat | wol | |
gars yi ñu ngi ci actuellement ñu ngi def toilettafe projet bi te am nañu yaakaar projet boobu su paree incha :ar allah :ar dina nekk li nga xamante ni bii disons roue de secours lay nekk daal pour vraiment ñi nga xamante ni ñoo dëkk ci côté boobu | wol | |
parce que gis nañ que nii normalement bu nekkee lépp jaar na yoon ñoom dinañ favoriser bu baax lu mel ni kii même béyu dër bi ñu koy wax kii quoi maraichage te am nañu yaakaar que ni vraiment loolu aussi bu fekkee antu na day nekk li nga xamante ne bii donc lu baax lay nekk daal | wol | |
tamit yàlla moom saa yu **** ni ko wolof di waxee rek du tëj bunt tëj paranteer saa yu bu benn bunt nee ràpp rek xamal ni beneen bi moom moom faaw mu ubbeeku | wol | |
d' habitude c' est comme ça quoi donc am nañ yaakaar daal que incha :ar allah :ar projet boobu léegi mu taxaw je sais que gars yi sori nañ si lool ñu ngi woon si toilettage projet bi kii quoi toilettage bi am na ay questions yi nga xamante ni peut être que moom bëri na ñu ñu koy laaj gars yi ñu ngi formulé actuellement... | wol | |
mais am nañ yaakaar ni incha :ar allah :ar que dina dina kii daal dina dina kii quoi dina aboutir | wol | |
ignore_time_segment_in_scoring | wol | |
tey jii lan lañ mun a jàpp ci changement climatique ci façon mbéy yi nga xamante ne am na fii ci Sénégal lan lañ leen mën a baaxee | wol | |
bon comme ni mu waxee ah bon xam nga bu ñuy wax mbéy mbéy ñun centré wu ñu mbéy mi yëpp daal ci ci ci | wol | |
boo waxee grande agriculture élevage mu ngi ci biir pêche bi mu ngi ci biir et | wol | |
actuellement yooyu dama la bëgg a xamal ni la que actuellement ñu ngi comme ni ko monsieur Badiane waxee woon ci njëlbéetam | wol | |
xam nga waxoon nañ la ni la ñu ngi liggéey état nag toujours dafa am ñi nga xamante ni ñoom ñoo koy jàppale | wol | |
ñu leen di tuddee les partenaires techniques et financiers partenaires techniques et financiers boo leen boo boo ko dégloo bu baax moom mooy ONG ak projet programmes yi nga xamante ni ñoo fi nekk | wol | |
ñooñu vraiment ñu ngi ci béy actuellement seen wàll bu baax a baax boo ñëwee par exemple fii au niveau de Fatick nga gis projet bu mel ni Proval CV avant moom sax avant avant Proval di ñëw sax di judd ak le PDRS | wol | |
am na benn écloserie bi nga xamante ni bii defoon nañ ko fii ci ginnaawu agriculture non seulement éclo() écloserie boobu mu ngi foofu | wol | |
mais ñu ngi def aquaculture fii et vraiment population Fatick yi ñu ngi ciy gis seen bopp les kii GIE des kii quoi des femmes de Ndiaye Ndiaye là vraiment ñu ngi ciy gis seen bopp bu baax a baax a baax donc ñu ngi fay yar ay ay kii quoi ay waas | wol | |
dégg nga ba mu toll nu mu nu mu ko neexee ñu ngi koy jaayee vraiment ay prix yu baax de la même manière boo demee élevage am na fa ay projets yi nga xamante ne bii donc ñu ngi fi aussi c' est des projets donc d' adaptation au changement climatique yi nga xamante ne bii yenn yi mi ngi jëm ci amélioration génétique donc ... | wol | |
yeneen yi mi ngi jëm vraiment ci des projets donc de stabilisation wala yu mel kii quoi yu mel noonu quoi donc yooyu yëpp gars yi ñu ngi ci ñu ngi ci kii quoi ñu ngi ciy béy seen wa() seen seen seen wàll | wol | |
te yaakaar nañ ni tamit yooyu c' est des projets kii quoi c' est des projets oubien donc des programmes yi nga xamante ni bii tey bu fekkee li nga xamante ne bii moom lañ si séntu | wol | |
parce que man dama jàpp ne ni lii sunu maamu pël yi di def muy élevage extensif loolu dañ ko war a dañ dañ ko war a dépassé yore téeméer wala ñaar téeméeri nag yoo xam ne mënalooleen dara boo xëyee dàq leen ñu dem bu ñu toogee ba ñu ni dugg nañ période soudure nga bàyyi leen ñu daal di dem defi lu ñuy wax | wol | |
jéem a kari kii quoi kari nfox mi loolu am na lu ko gën xam nga loolu nga amoon par exemple fu ngay amee téeméeri nag | wol | |
yi nga xamante ne munoo ci dara ludul toog di ko xool di ko topp naan ko is is nga am tey jii juróomi nag yi nga xam ne wóor na la ni yii c' est est des races améliorées | wol | |
ah litre meew bu ne nga mën ko jaayee six cent franc par jours ah yaakaar naa ne loolu moom moo ëpp njëriñ fuuf yow di nga liggéeyal sa bopp te doo ci sonn te doo ci doo ci am àq | wol | |
ignore_time_segment_in_scoring | wol | |
weer bi ñu ko war a weeree dëgg-dëgg dégg nga sax nangootuñ ko def parce que divagation mu ngi fi boo duggee ci àll bi bon communes yi ni ñuy waroon def kii quoi daal di di élaborer kii quoi le parcours donc du bétail là amul | wol | |
pratiquement boo xoolee parcours boobu mun naa ko nii que c' est c' est kii quoi c' est biaisé | wol | |
tey gis nga nag éleveur éléveur mi ngeeg mbir bi nga xamante ne bii ci ci ci kii quoi ci boppam moom yaakaar na ni bu xasee ba ba ba départ jur gi nga xamante ni moom la yor dara baaxul pour jur googu | wol | |
tout son problème moom mooy na jur gi lekk ba suur na jur gi naan ba màndi donc man yaakaar naa ni que ni nit ñi aussi léegi war nañu mën a xoolaat seen bopp | wol | |
xam ni que vraiment daal di am kii yar ay kii yu bëri dégg nga te vraiment du la amal benn njëriñ fexe woon ba nga am ñaar wala ñett yi nga xamante ni lu mu bon bon bon chaque jour mu mën la génneel au moins dix mille wala quinze mille franc | wol | |
je pense que loolu moom moo ëpp moom moo ëpp njëriñ fuuf parce que loolu en rélité bu fekkee yaa ngi ci sax fonctionnaire bi nga xamanate ne bii moom moo lay encadré sax yow di nga am loo xamante ne moom du ko am quoi | wol | |
ndax waa DRDR mun nañu témoigner tey jii que ni ni ngeen di joxee information yu dem ci producteurs yi ndax ñoom kiiyal na leen ils sont en phase ak li nga xam moom mooy information yi | wol | |
maanaam dafa ñi ñi nit ñi sax dañ léegi dañ ma ne yow boo est ce que duñ yóbbu météo ma ne leen ndo() ba tey it [rire] maanaam xam-xam dadul caaxaan | wol | |
dëggu tegu ci xarale ak jumtukaay yu mucc ayib dama ne am nay jamono waa météo bu ñu waxee kenn du leen déglu | wol | |
li may wax nii yàggut waaye adduna dafay dox ay jumtukaay maanaam dama ne dama ne ñi doon ñi ko doon wax ay Sénégalis lañ te ba léegi ay Sénégalais lañu jàng am xam-xam jumtukaay rek moo fa moo doonoon seen gàllankoor [shh] yàlla def na diggante bi at ay at | wol | |
ñu am ay jumtukaay yoo xam ni [shh] tax na liñ doon wax mu gën a tegu | wol | |
xam-xam bi mosu fee jóg jumtukaay dong moo doon jafe-jafe te defe naa jumtukaay yooyu ba ci ña ca war a jóg jóge ah gis na ñëpp gis nañ kenn naatablewul waxu météo moo xam ci mbéy la moo xam ci sàmm moo xam ci napp kon loolu lu lu ko waral mooy li mu wax rek | wol | |
ignore_time_segment_in_scoring | wol | |
léegi nag ñun ñi nga xam ni ñun ci wàllu béy man tey ñun dañ ko jiital informa() climatique fañ teg jiwu teg engrais teg fa lay la ñuy aaree gàncax teg fa jumtukaay bu ndaw mooy matériel bu ndaw bi ak matériel bu mag bi mooy tracteur ak la muy àndal foofu la tegu donc dafa nekk facteur de production | wol | |
changement climatique ta() tax na ñu teg ko ca a kanam léegi dañ ko boole woon waaye léegi dañ ko teg ca kanam boo ko tegul doo dem ndax ñoom boo leen dégloo di nga xam ndax yow war ngaa jiw wala ndax waroo jiw | wol | |
léegi ci biir waxtaan yi dañu naan sax léegi nañu xool pour ñëw léegi ci li nga laajoon changement climatique tax na fi mu toll nii ñëpp dañu war a teel a ji même ceeb sax dañu ko war a teel a ji | wol | |
ku ci bëgg a génn fi mu toll nii da ngay teel a ji maanaam di moytu yenn xeetu variété yi nga xam ne dañuy laal ñeenti weer jëm kaw | wol | |
déedéet teel a ji bi du indi jafe-jafe teel a ji bi mooy li ñuy mën a faru ñu faru ko | wol | |
man expérience bi nga xamante ne bii am naa ko ci lu mel ni mbéyum gerte wala yu mel noonu xam nga gerte dañu naan pour nga jiw ko il faut nga am une pluie utile | wol | |
dégg nga une pluie utile mooy taw bi nga xamante ne bii dafay nekk ba vingt milimètres soxna Maguette vingt milimètres taw moom mooy nga jël nu mu tudd ñaar fukki litres ndox nga wasaare ko ci benn surface su un mètre carré yaa ngi dégg | wol | |
donc boo jëlee vingt litres ndox nga sotti ko ci espace su maanaam dégg nga ñeenti ñeenti *** tooy bi muy tooy boobu xam nga dafay dafay da() da() day xóot quoi | wol | |
xam nga maam mag yu njëkk dañu daan gas seen loxo yi da doon xóot mais gis nga seen gerte googu boo xa() bu xasee ba ba ba ba kii quoi ba sax bu xasee ba sax | wol | |
ak kii quoi évaporation bi nga xamante ne bii moom mu mu moom lay àndal ak yéen xam nga lu ma wax | wol | |
donc bu xasee ba sax ba pare xam nga la lu ko rey yombul li ngay la nu muy demee ba évaporer wu ba suuf sa wow koŋŋ koŋŋ koŋŋ [tx] ba amatul dara dara dara li nga xamante ne bii mën na ko puiser ci ci suuf si ba mën ba mën a dem balaa muy egg foofu dina nekk presque weer wala kii quoi weer ak nangam balaa boobu incha :... | wol | |
ba ci dugub maa ngi leen wax ne dugub bu xiifee ca njëlbeen bonut loolu constat empirique la nga dem ISRA kuréel gi yor wàllu gëstu bi soo demee am na benn centre ISRA bu ñuy wax ñoom ñooy gëstu lépp lu ñuy wax déve() lu ñuy wax mécanisme d' adaptation des résidus à la sécheresse yàlla def ma jaar fa yàlla def ma liggé... | wol | |
gis nga ñoom li ñu liggéey ci dugub ak gerte maanaam pour ngir dëggal li ñu maanaam loolu mag ñi gis ci dugub ni bu xiifee ca njëlbeen bonut day yokk dana feeñ ca rendement ba | wol | |
ñoom dañ ko gëstu ba génn ba bind ko ba teg ko dugub bu xiifee ca njëlbeen ga comme ni mu ko waxee | wol | |
reen ba lay pousse ba mu gën a jëm ca suuf mu jëm ci suuf un mètre ba un mètre cinquante lépp lu fay ndox [shh] lépp luy ndox nag mu mu raasaatu yéegaat ca kaw | wol | |
bu ko fa taw ba fekkee dooleeku ci loolu loola nga gis mun na indi xeetu bu suuf sa amee doole bu suf sa amee doole rek nga gis mu fencku pour dëggal ko ko ci gerte gerte am na fu muy toll ci xiif ndax man def naa ko ci loolu ma lay wax noonu jàngat boobu ma doon def | wol | |
en deux mille deux deux mille trois daén doon xiifal gerte gi xiifal forcé | wol | |
xoon ko reen bi waa ISRA def nañ ko am nañ benn appareil lu ñu tuddee séseauton boo koy xiifal boo ko lifinee da ngay mën a xool soxna Maguette di mën a mesurer développement racine yeeg maanaam ni reen yi di poussé reen yu mag yi di dee | wol | |
bu ñu ko gëstuwee ñoom dem nañ ba gis ne reen bi dina dem ba deux mètres bu dugub dina dem ba un mètre cinquante bu gerte dina def | wol | |
doole jooju muy yëkkatee mu ñëw bu ñëwee bu xëccee bu ñëwee mu boole ca di jur doom day tax li ñu tuddee alimentation hudrique bi dafay gën a am doole | wol | |
ignore_time_segment_in_scoring | wol | |
kon li muy wax noonu lu am solo la te ca suñu di() diir boobu nag eh nañuy ñaan projet boobu nga wax noonu mu antu ndax su ma juumut juróom-ñeeti communes defe naa dana ca bokk | wol | |
mooy condition fondamental bi it mooy tax di nga xam ne pour projet boobu mën a dem bu ñu ko nangoo ba lifin bu nit doxalee lañ ca war a doxaljëm ci wàllu mbéyum ceeb jëm ci wàllu mbirum | wol | |
mbirum maraichage déedéet ba ci ci biir yëf yi am na jiwu programme jiwu am na ay digues am na sax *** | wol | |
am na ay magasins bawuñ dara [bb] ba ci jumtukaay matériel bawul dara foofu moom bu yàlla defee mu am su ma juumul ah diir boobu gox yooyu dina am soppeeku | wol | |
incha :ar allah :ar dina am soppeeku du tere it mu ne ah ma ne ko xelal bi muy wéy que ni fi ñu toll ci wàllu nawet ak nawet yii di ñëw allah kulli :ar aal foog ne comme ni ko sëñ Maodo waxee foog nit ñi di teel a ji | wol | |
xoolal ñi nga xam ne ñooy teel a ji xaal bi xaal biy njëkk a ñëw ci marché bi borom dañ koy arrosé soxna Maguette de dañ koy arrosé arrosé | wol | |
ci mbéyum noor bi lañ koy béy xaal biy njëkk a duggu si fii ci Fatick ci marché bi ña ko fañ koy béyee ci arrondissement Niakhane ña koy def dañ koy arrosé | wol | |
ceeb ma fàttali ni deux mille quatorze sëñ Maodo boo ko fàttalikoo département Fatick am ruq rek moo fi génnewoon ceeb bu xaw a yéem nit ñi muy ruqu Fayil bi | wol | |
dafa faru ci ceeb gi deux mille quatorze boo fàttalikoo trente septembre la ndox mi arrêté tawatul Sénégal man mu ngi ma fekk Kolda trente septembre deux mille quatorze taw wàccatul au niveau national te fii fii ci | wol | |
ma essayé ko ndeketeyoo nawet bi day teel a arrêté moom kepp moo fi guub ceeb bu nit mun a duut baaraam | wol | |
lu mun a nekk la te loolu ah ñi ko en tout cas ñi nga xam ne ñu ngi koy ñi ngi koy jéem dañ ciy gis njëriñ li Maodo wax ne nag nag xaw na métti nag wax dëgg fa yàlla | wol | |
te te mënut a doon it lu yaatu lool waaye nag dees na ko dees na ko def ndax day yokku li ñuy wax résilience bi lu am solo la nit ñi di nangu sans nangu soppi ceeb bi comme ceeb bi mais ceeb bi boo teelee def pepinière mais sëñ Maodo bu teelee taw bu fekkee ne liggéey nga suuf si da ngaa war a teel a jëmbat | wol | |
mais boo teelee liggéey sa tool moo xam ndax chariot ñi amul tracteur chaine chaine ak peeru nag ak lifin mun naa mun naa labouré jarul ngay xaar tracteur | wol | |
mu lay terdé boo ko teelee def mu ne ah ma ne ko semoir ngay am léegi ceeb bu njëkk ba amul semoir mais léegi ceeb am na semoir bu koy ji booy ji sa semoir à sec nga koy def buy taw bu sebet bu ko fekkee nga xam sëñ Mao() mooy li sëñ Maodo wax | wol | |
il foog nit ñi nangoo soppi ndax léegi jamono jee ko laaj noonu la bindoo te day gën a yokku waaye du wàññeeku | wol | |
te liñ mën a faru nañ ko faru ni ko sëñ Maodo waxee nangu cee sonn bu ñu ko faroo bu yàlla tawee rek nga gis njëriñ li | wol | |
waaw te gën a nag maanaam gën a yaatal mbéy mi diversification bi kooku moom it ab ab lifin la ab ab nu mu tuddati ab saafara la | wol | |
li nga xam ne mën nga ko teel a faru rek li ci des nga béy ko ca bàq bu tooy ba continué bul tayal la ca des it comme ni mu ko waxee lay lay ba lay ba yeggali ko lépp boo ko boolee diversifation la mooy yaatal nguur gi dana def li mu war a def jàppale béykat yi te mu ngi koy def dina ko continué di ko def ci anam yi mu... | wol | |
ignore_time_segment_in_scoring | wol | |
gis nga ñett ñooñu dañuy dikkaat te ñooñu il foog nit ñi di ko bàyyi xel na nit ñi di gën a bàyyi xel sëb yi na nit ñi gën a bàyyi xel xaal bi ndax dañ ci lekk dañ ci jaay | wol | |
di ci jaay di ci lekk di ci jaay ndax bu sëb xasee ñor rek daanaka xiif kër googu moom xiif wàññeeku na fa loo ca boole nag akub xaal boole ca leneen ak leneen rek daanaka xiif xiif day daal di randu | wol | |
am na solo mu mel ni nag [bb] egg si nañu si cappaandawu émission bi ñu ngi lay bàyyi rek Maodo nga daal di joxe conseil ndax def ngeen ko avant taw yi di ñëw ci biir taw yi ak après tamit pour récolte yi tey lan mooy conseil yi ngeen di joxe | wol | |
mooy actuelement nii ci mission laa jógee def naa pratiquement région Fatick yëpp parce que suñu mën naa wax ni def naa département de Foundiougne parce que dem naa ba Tou() Tou() ginnaaw Toubacouta ay Nemandig Nemaba | wol | |
jóge naa fi dem naa fii ba kii quoi dans l' arrondissement de Fimela [tx] mais nit ñi benn jàmbat wala benn jooytu moom laa xam ni jooytu na ma ko fi ñoom ñëpp nee nañ ma daaw ils avaient des problèmes problème bi ñu amoon moom mooy ginnaaw bi nga xamante ne bii nawet bi jeex na ñoom dañuy def li ñuy wax moom mooy mbéy... | wol | |
mais nee nañ liñ liñ ci gën a constater mooy que soble gis nañ ni que semence soble pot bi dafa cher parce que pot bi ça coûte vingt cinq mille et quelque waaye nee nañ ñoom li leen gënoon a métti mooy da ngay jëndee potu soble nga def sa pepinière deux jours trois jours après mu taw bu tawee pepinère boobu yàqu | wol | |
voilà nga nga kii quoi nga recommencé waat donc [tx] loolu mi ngi dëggal rek ni [tx] suñuy wax dëgg yàlla donc jot na pour que vraiment que suñu mbokku producteurs yi di continué encore di dem vers l' information climatique | wol | |
comme nim ko waxee nag ñun ñu ngi fi suñu téléphone tëjaluñ ko kenn heure boo ñu woowee ñu wuyu la nañu xam ni que même bu fekkee nawet bi jeex na | wol | |
nawet fu mu jeexee aussi toujours dañuy am ce qu' on appelle donc les pluies hors saison comme nag dañu toll fu mu nekk nii ci jamonoy pepinière ah donc dina baax nit ku ci nekk balaa ngay ngay ngay engagé kii quoi travaux yu mel noonu nga jël information bi nga xamante ni bii yaa ngi koy jël fa nga ko war a mën a jële... | wol | |
ñaareel bi moom mooy que ren jii gis nañu nawet bi nu mu nu mu bindoo vraiment nekk na nwet bi nga xamante ni bii bu métti la trop vrament gis nañ ni que ne xëy na le résultat escompté peut être sax mën naa wax ne atteindre luñ ko parce que bu ñu toogee bay wax ay trois vague de semis | wol | |
te naan la y' a que la première vagues rek moom moo ci arrivé à maturité ñi ci des *** [rire] donc li ñuy wax moom mooy que vraiment ñi nga xam ne yàlla suturaal na leen ba ñuy récolté tey jii nañu fexe ba ñu mën a aar seen kii quoi récolte yooyu | wol | |
donc ñoom aussi nañu dem et vraiment de manière continuelle di gëstu donc information climatique yi ba keroog nga xamee ni ñu ngi stocké seen dugub | wol | |
bës bu ñu demee nag ba xam ne sécuriser nañ ko ba tëj ko ci ay magasins nag su boobaa nag mën nañu def lu leen neex mais pour l' instant | wol | |
li ñu gënaloon daal moom mooy vraiment que nit ñi di dem vers l' information climatique di wëmbatiku encore rek une fois di jaajëfal bu baax suñu mbokku Jokalante yi | wol | |
parce que vraiment jàppale nañ ñu bu baax pour ñu mën a vraiment ñun tamit ma béy suñu suuf kii quoi su() su() suñu waar ñu mën a béy suñu waar vraiment ci kii quoi ci tool bi | wol | |
ndax xëy na bu doon ñun rek dina dina xaw a dina xaw dina xaw a doy waar parce que souvent monsieur Badiane damay faral di wax ni information climatique bii ñuy joxe souvent dañ koy joxe à kii quoi à travers rajo yi wala téléphone | wol | |
donc dañuy am souvent lëkkaloo bi nga xamante ni moom mooy am suñu diggante ak Sonatel surtout | wol | |
te ku nekk xam nga ne Sonatel même si c' est des commerciaux amul dara li nga xamante ni bii dañ koy maye | wol | |
tey jii ñun lii bu ñu ko mënee di ko def di ko matal c' est parce que en réalité am na ñoo xamante ni ñoo nekk suñu ginnaaw | wol |
End of preview. Expand in Data Studio
README.md exists but content is empty.
- Downloads last month
- 7