Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet Duplicate
audio
audioduration (s)
0.74
171
transcription
stringlengths
3
969
source
stringclasses
8 values
translated_text
stringlengths
3
907
paaka bi lay rendi sa waay a koy daas jox la
alffa
Le couteau que vous sacrifiez vous est toujours donné par votre père.
parce que gerte moom non seulement assiète racinaire am yaatu na
kallama
parce que gerte moom non seulement assiète racinaire am yaatu na
dafa niroog benn anam buy puus nit ñi ñu yaakaar nañoo fay lu ëpp
fleurs
Cela ressemble à un moyen de pousser les gens qui sont censés payer plus
ay doomam dees na ci jële xeetu ñam yu nekk.
galsenai
ses fruits sont produits à partir de toutes sortes d'aliments.
bu wéñ di dox ci sama kow dafa may ñoromtaan
alffa
Quand le fer marche sur moi, ça me donne la chair de poule.
njiitu réew mi sàll sas na jëwriñu wér-gu-yaram ji ak jëwriñu peterol ak eneersi bi ñu taxawul aw tëralin ngir fexe ba lopitaal yi moom seen bopp ci kura te ñu jaare ko ci kura biy bawoo ci jant bi
lafricamobile
Le président a déclaré que le ministère de la Santé et le ministère du Pétrole et de l'Énergie n'ont pas établi de plan pour rendre les hôpitaux indépendants en énergie et alimentés par l'énergie solaire.
waxleen tom mu noppi.
galsenai
Dis à Tom de se taire.
dëgërluwiin gu ab mbéll
galsenai
La résistance d'une poutre.
ndax am na yoo xam ne yomb na xam nga lu mel ne que boo de amee ñeenti junni rek mën a am ay kayit yoo xam ne danga ci mën a
kallama
Il y en a qui sont faciles à comprendre, comme par exemple si vous n'avez que quatre mille, vous pouvez obtenir des documents que vous pouvez.
mu ni ko waaw lan la waa ji dafa la dóor
alffa
Elle dit oui, qu'est-ce que ce type t'a frappé ?
dpv maanaam di di la direction de la protection des végétaux
kallama
dpv maanaam di di la direction de la protection des végétaux
maaraa la ko ay jegeñaaleem di woowe, doomi-réew mi naan ko idi
galsenai
Ses voisins l'appellent Maaraa, et les locaux l'appellent idi.
yal na ñu yàlla musal ci mbas mi.
galsenai
Que Dieu nous préserve de ce fléau.
faatu sottalagul liggéey bi ñu ko santoon
alffa
le défunt n'a pas accompli la tâche qui lui avait été assignée.
faramfàcce mboole yi
galsenai
C'est une affaire importante.
jën wu ñu bërëm a gën a saf fuuf jën wu ñu togg ci cin
alffa
Le poisson cru est généralement plus sain que le poisson en conserve.
dafa doon jula waaye léegi daanu na
alffa
Il jouait, mais maintenant il est tombé.
ndax engrais organique bi moom moo ko subventionné
kallama
parce que l'engrais organique est subventionné par lui.
sama jabar dafa ëmbu.
galsenai
ma femme est enceinte.
bu jëkk funjuñ amoon na cër bu réy ci njaayum gerte gi
alffa
Autrefois, les fourmis jouaient un rôle important dans le commerce des fourmis.
waaw mbokk yi lii ak leeral la jëm ci diggante junne ak rab.
galsenai
oui frères, il s'agit de la relation entre le démon et l'esprit.
benn moroomam dafa ko kolooj ba bët bi xonq coyy
alffa
Un collègue l'a poignardé jusqu'à ce que son œil soit rouge comme un roc.
amoon naa benn laaj ci sunu wateb oui ak non bi ñu watewoon
galsenai
J'avais une question sur notre test oui et non que nous avons passé.
bu gàmmu jotee lu nekk la tiijaan yi di jóge di dem tiwaawan
alffa
Quand le moment arrive, les Tijans partent et se rendent à Tiwan.
borom woto yépp a ngiy jooytu tali yu yàqu yi
alffa
Tous les propriétaires de voitures se plaignent du mauvais état des routes.
bokkul ci càcc gi dañu ko bëgg dugal rekk
alffa
Il n'a pas participé au vol, ils l'ont juste laissé entrer.
yi ci ëpp solo ñooy yii
galsenai
Voici le top 10
ak tàngaay wi ngoor si dow dem daanu ci kër
alffa
Et la chaleur de l'homme à l'étage s'est effondrée à la maison.
crec tamit mu ngi ciy liggéey liggéey bu am a am solo côté boobu
kallama
Le CREC travaille également sur des travaux importants à proximité.
baay bi ni wóññileen nag yi ak jaam yi ñu ñibbi
alffa
Le père leur a ordonné de ramener le bétail et les esclaves à la maison.
damay bay ay orside.
galsenai
La baie de Damay est à l'ouest.
nun pool ak timote, jaami kirist yeesu, noo leen di bind, yéen gaayi yàlla yu sell yépp ci dëkku filib, yi bokk ci kirist yeesu, yéen ak seeni njiit ak ñiy topptoo yëfi mbooloo mi
lafricamobile
Paul et Timothée, serviteurs de Jésus-Christ, à tous les saints en Jésus-Christ qui sont à Philippes, aux évêques et aux diacres:
bu jotee rek kenn ku ne ñëw ne man damay béy kenn ku ne ne bëgg naa ci laa bokk mbir it nag boo ci bokkee te naroo koo jëriñoo ni mu waree ndax dangaa soxla xaalis rek loolu taxul affaire bi régler
kallama
Puis quelqu'un vient et dit : « Je nourris quelqu'un » et dit : « Je veux faire partie de quelque chose » et si vous en faites partie et que vous ne l'utilisez pas correctement parce que vous avez juste besoin d'argent, cela ne rend pas l'affaire correcte.
jant bi amul xeer ne suuf bu nu mëna taxaw jant bi yepp gaas safara ak plaasma lanu ko defaree
fleurs
Le soleil est sans roche, dit le sol sur lequel nous pouvons nous tenir, le soleil est fait de gaz, de feu et de plasma.
kon kenn ku ci nekk war nga mën a am groupement ba nga xam si ne yow am nañu sa kóolute pour nga jaar si ñoom bokk si ñoom
kallama
Ainsi, tout le monde devrait pouvoir avoir un groupe dans lequel vous savez que vous avez confiance pour les traverser et en faire partie.
bokkeef dominikee réew, dun géejpeek u atlantik
galsenai
La République dominicaine n’est pas l’océan Atlantique.
li mu yanu moo bari ndax góor ñi mën naa ne ne
kallama
Il y a beaucoup à dire sur les hommes.
mbootaay bi jokkale tukkikat ca dëkk ba ñu jëm ñooy jàppale tukkikat yi ba ñu mëna xamante ak waa dëkk bi ñu jëm
fleurs
L'organisme de liaison des voyageurs du pays de destination aide les voyageurs à faire connaissance avec la population locale.
di leen taxawu am na sax waxtaan binga xamantene euh tàmbali nañ ko euh séqq ak etat bi ak ñii di euh partenaires sociaux yi yoon wi di wëy ba tey
source
Il y a même une conversation qui, vous le savez, a commencé avec l’État et les partenaires sociaux et le processus est toujours en cours.
jant buy so damaa neex.
galsenai
J'adore les couchers de soleil.
kakatar
urban_bus
cafard
way loo ma seexi saalihu.
galsenai
Il n'est pas permis de dormir dans le salih.
dem naa ci bitig ba.
galsenai
Je suis allé au magasin.
fukk ak juróom ñett ci téeméer bu waa wenesyelaa bo jël amu ñu liggéey té ñu ëpp ñëp ñuuy liggéey ñoi ci surnal kom-kom
fleurs
Dix-huit pour cent des Vénézuéliens sont au chômage et la plupart des employés travaillent dans le journal.
ab taar, ku ne ak na mu ko jàppe.
galsenai
Une beauté, chacun a sa propre interprétation.
bu jëkk tubaab yi dañu gawoon njàngum alxuraan ji
alffa
Dans le passé, les Européens ont mis du temps à apprendre le Coran.
ci moom la mali nekke nguur gu mag dëgg, ci la àgge ci pujam.
galsenai
en lui le Mali devint un véritable grand royaume, et il parvint à son pujam.
ci kaw jëmmal gu muy jëmmal ay fentam, ngir ñu mën a jox lu ndaw ci kérédi ab nit ku mel ni moom, li ko gën a soxal, mooy mu firndeel ànd bu déggoom dëgg ngir sàmm ay liggéeyam ak benn ci kàddu gu yanu maanaa lu mu ndaw ndaw ci lu jëm ci wàll wi.
lafricamobile
Dans la structure de ses peintures, pour pouvoir accorder un peu de crédit à un homme comme lui, le plus important est de prouver le véritable engagement à protéger son œuvre avec un seul mot qui signifie le moindre détail sur le sujet.
ci sama dég dég weer wu dee lay ñów
alffa
Je comprends que c'est un mois mort.
fii dangay gis tey araw yi ñu daan def ci xew louga gii bari na ñoo xam si dañuy xewle
kallama
Ici, vous pouvez voir aujourd'hui que les étapes qui ont été franchies vers cet événement sont nombreuses et que l'on sait qu'elles se poursuivent encore.
kàngami dëkk bi ñoo dajale ñaari gox yi ngir jubale leen
alffa
Les deux régions ont été réunies par des experts locaux pour les remettre en ordre.
dimbalileen ma ma génn.
galsenai
Aidez-moi.
dal di na koy tëkku .
galsenai
dal sera coupé
ñii dé ñoo bëgg lu ñu bokk menn mbaam ñaari nit
alffa
Ces gens veulent partager le même âne avec deux personnes.
ba ñu leen goreelee it taxul ñu gën demin
alffa
Leur libération ne les rend pas meilleurs.
pour yokk dooley parcelle boobu noonu
kallama
pour yokk dooley parcelle boobu noonu
damaa bëgg tufe pombiteer.
galsenai
J'adore les tufs à tuyaux.
nga dem jël par exemple aussi fumier bii
kallama
Vous allez prendre par exemple aussi ce fumier.
rond point sococim nord
urban_bus
rond-point sococim nord
ndém amu ñu woon ay péxé ci lii germany xaaronna tontu buni mél ci séni xééx kat yi ci géej gi
fleurs
Ils n’avaient pas d’autre choix, mais l’Allemagne s’attendait à une réponse similaire de la part de ses pilotes de la marine.
ecole castor rufisque
urban_bus
ecole castor rufisque
dafa laabir ba ku dikk ci dëkk bi rekk mu boot la
alffa
Il est impératif que toute personne entrant dans la ville soit accueillie.
noonu, senegaal, réewum
galsenai
Oui, le Sénégal, le pays de
mu ne dina ñów ci ndaje li ba noppi teg ci ne moo fay jiitu
alffa
Il a dit qu'il viendrait à la réunion et qu'il serait là en premier.
gare routière rufisque
urban_bus
gare routière rufisque
ndax, ci la doon dox di wàlle ak a tasaare feebarbi
galsenai
Parce qu’il infectait et propageait activement la maladie.
te xamuñu ne bien bien que kii la
kallama
te xamuñu ne bien bien que kii la
sa xam xam bee nu gindi ba dootuñu gëlëm
alffa
Vos connaissances nous ont conduit au point de non-retour.
léegi nag gannaaw gëmuloo li ma wax, dinga luu te dootuloo man a wax, ba kera sama wax di am, bu jamonoom jotee.
bible
et voici, tu seras muet, et tu ne pourras parler jusqu'au jour où ces choses arriveront, parce que tu n'as pas cru à mes paroles.
man naa teg taabal ji am ?
galsenai
Puis-je mettre la table ?
deret jii ngeen tuur dina xëppu ci seen kaw
alffa
Le sang que tu verses retombera sur toi.
dafa mel na li ñu ko téjoon dafa ko téppari
alffa
On dirait que le verrou s'est resserré.
ñuy liggéey ci cadre projet bi
kallama
Travailler sur le cadre du projet.
bàyyileen ko mu dem !
galsenai
laisse tomber !
wala
kallama
rien
dangaa nekkoon ci diggante dundu ak dee.
galsenai
tu étais entre la vie et la mort.
saa bu ma ko nuyujee dina ma may aylayéwén junni
alffa
Chaque fois que je le salue, il me donne mille aylaws.
xale bu yeewu la boo ko tegtalee sa kër dina fa dem
alffa
C'est un enfant éveillé et si vous le dirigez vers votre maison, il y ira.
ba lée léegléeg sax
kallama
même comme
jongante bu mujj bu waa all blacks lawoon ñoom ñi jël ndàm li ba noppi ñaari ayu-bis ci ginnaw
fleurs
C'était le dernier match des All Blacks qui ont remporté le titre et deux semaines plus tard.
waa jii di la seetsi dama bëgg mu dakk
alffa
Ce type qui te rend visite, je veux qu'il arrête.
tamba leeko si mbëbestal la bacci daneel ba
galsenai
Il quitta ensuite la loge danoise à pied.
ottawa mooy dëkk bu gëna rafet ci kanadaa payub-réewu ñari lakk ak ay galeri ak muze yuy wone demb ak tayu kanadaa
fleurs
Ottawa est la plus belle ville du Canada, un pays bilingue avec des galeries et des musées qui présentent le passé et le présent du Canada.
même sa wà sa wàllum liggéey aussi coono sax dafa lay teggeeku des fois
kallama
Même votre santé, votre travail et votre fatigue vous arrêtent parfois.
yénééni gnétti ndéll kalaté nangu ci wétu beereebu njiit yi ci gnaari waxtu
fleurs
Les trois autres doivent se tenir près du quartier des dirigeants à deux heures.
njëgu li ñuy jëndale benn milyou njël tollu na ci juróom-fukki milyaar ak ñeent ak juróomi téeméeri milyo ak fan-weer ak juróom-ñaari téeméeri junni ak benn ak ñeenti téemér ci xaalisu seefaa, te ñu yokkaat ci téeméeri junniy njël. njëgu dund bi yépp tollu na ci juróom- fukki milyaar ak juróom-ñaar ak ñaari téeméeri mi...
lafricamobile
Le prix d'achat d'un million de riz est de cinquante-quatre milliards cinq cents mille et trente-six mille sept cent un mille quatre cents sicles, plus cent mille riz supplémentaires. et l'armée entière, était de cinquante mille sept mille deux cents millions et soixante-neuf mille sept mille huit cent cinquante drachm...
eskëy,moom de ci jëlewaayi masdar sheex sahdu abiihi la bokkoon
galsenai
Il a été impliqué dans la déportation de Masdar Sheikh Sahdu Abihi.
peppantaan boobu nga xam kenn man atu ko xaaj moo tudd weesoofulub ndox.
galsenai
Cette division qui ne peut être divisée est appelée conductivité hydraulique.
ku weg nit ñi wegees ko
galsenai
Celui qui est respecté sera respecté.
duñu ko faral dégg bindoon na nag ca gannaaw
alffa
on n'entend pas souvent dire que cela a été écrit à l'envers.
mu xool ko ba mu yàgg jékki jékki song ko
alffa
Il la fixe pendant un long moment puis l'attaque.
day wuute ci xeet yi
galsenai
Cela varie selon les groupes ethniques.
mayleen ma benn simili.
galsenai
Donne-moi une minute.
gis nanu leen ñuy dem.
galsenai
nous les avons vus partir.
waaw incha ar allah ar kooku moom yaakaar naa du am jafejafe incha ar allah ar
kallama
oui inch'allah c'est celui-là j'espère qu'il n'y a pas de problème inch'allah
ci bii gox ñetti réew yu mag a fe
galsenai
Dans cette région, trois grands pays à peine
moo tax it da ciy am solo ñoom ñuy ñëw ñuy waxtaan ci jamono ju nekk
kallama
C’est pourquoi il est important qu’ils viennent discuter à tout moment.
moo baax ci mbir mi.
galsenai
est parfait à cet effet.
dama bëgg itam togg.
galsenai
J'aime aussi cuisiner.
ci cosaan, dañu ne, bawol, ku fa jëkka nekk buur, xaayamagaan moo doon turam
galsenai
Traditionnellement, on dit que le premier roi était Bawol, et son nom était Khaamagaan.
End of preview. Expand in Data Studio
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
81