input stringlengths 13 433 | input_fr stringlengths 2 469 | input_wo stringlengths 15 414 | label stringclasses 77
values |
|---|---|---|---|
I have trouble proving my identity. | J'ai du mal à prouver mon identité. | Dama am ay jafe-jafe ngir xamle sama dàntite | unable to verify identity |
When will my top-up happen? | Quand ma recharge aura-t-elle lieu ? | Kañ la sarsamã di jàll ? | pending top up |
Why am I being charged for getting cash? | Pourquoi me facture-t-on pour avoir reçu de l’argent liquide ? | Lu tax ma war a fey ngir jot xaalis ? | cash withdrawal charge |
What is the time frame that transfers normally take from a UK account? I just completed a transfer and nothing shows up. I need to know if everything is alright. | Quel est le délai habituel pour les virements depuis un compte britannique ? Je viens d'effectuer un virement et rien ne s'affiche. J'aimerais savoir si tout se passe bien. | Lan mooy diir bi war ngir yónnee xaalis Royaume Uni ? Dama yónnee xaalis waaye gisuma dara. Bëgg naa xam ndax lépp a tege ciw yoon | balance not updated after bank transfer |
What identification is required to activate my card? | Quelle pièce d'identité est requise pour activer ma carte ? | Wan këyit laa war a soxla ngir fexe ba sama kont dox ? | activate my card |
I just bought an item and changed my mind. I have not received it yet how can I get refunded. Thank you. | Je viens d'acheter un article et j'ai changé d'avis. Je ne l'ai pas encore reçu. Comment puis-je me faire rembourser ? Merci. | Jënd naa benn yëf, waaye dama ko bëgga xàcc. Jotaguma ci, naka laa mën a def ba jotaat ci sama xaalis ? Maa ngi leen di sant. | request refund |
I would like to dispute a payment I didnt make | Je souhaite contester un paiement que je n'ai pas effectué | Dama bëggoon a jéebaane ab peyoor bu ma deful | direct debit payment not recognised |
I'm in China and need a new card. Please help. | Je suis en Chine et j'ai besoin d'une nouvelle carte. S'il vous plaît, aidez-moi. | Maa ngi Senegaal te dama soxla kàrt bu bees. Dimbali leen ma ngir yàlla. | card about to expire |
What I topped up was reverted by the app. | Ce que j'ai rechargé a été annulé par l'application. | Li ma sarsewoon, aplikaasiyoŋ bi dafa ko niilal | top up reverted |
I couldn't get the money I needed. | Je n’ai pas pu obtenir l’argent dont j’avais besoin. | Mënu ma am xaalis bima soxla woon. | wrong amount of cash received |
I am not happy with your service and request that my account be terminated! | Je ne suis pas satisfait de votre service et demande la résiliation de mon compte ! | Kontaanuma ci seeni sarwiis, moo tax may sàkku ngeen téj sama kont. | terminate account |
Where is the PIN for my card located? | Où se trouve le code PIN de ma carte ? | Fan la sama baatu ubbikkayu kàrt nekk? | get physical card |
I think that the card is stolen. What are my next steps? | Je pense que ma carte a été volée. Quelles sont les prochaines étapes ? | Yaakaar naa ne dañoo sàcc sama kàrt. Yan jéego laa war a def ? | lost or stolen card |
Will I be charged any fee for receiving money? | Vais-je devoir payer des frais pour recevoir de l'argent ? | Ndax fàww ma fey ay njëg ngir mëna jot xaalis? | top up by bank transfer charge |
explain the interbank exchange rate | expliquer le taux de change interbancaire | Leeralal dayo weccante xaalis diggante bànk ak bànk | exchange rate |
How does a disposable virtual card work? | Comment fonctionne une carte virtuelle jetable ? | Naka la kàrt wirtuel bu ñuy sànni di doxe? | get disposable virtual card |
my cash out is still pending | mon retrait est toujours en attente | Sama dindi mingi xaar ba leegi. | pending cash withdrawal |
There is a strange 1£ charge that appears as pending on my statement. What's the cause for that? I haven't purchased anything for a pound. | Un étrange débit de 1 £ apparaît comme en attente sur mon relevé. Quelle en est la cause ? Je n'ai rien acheté pour une livre. | Am na fere benn pound buy feeñe ci pekku négandiku ci sama karne kont. Lan mooy sabab bi ? Jënduma dara luy jar benn pound | extra charge on statement |
My payment was terminated | Mon paiement a été interrompu | Sama peyoor dañu ko dakkal | reverted card payment? |
Would it be possible to open up an account for children? | Serait-il possible d'ouvrir un compte pour les enfants ? | Ndax mën nañu ubbil ay xale kont? | age limit |
Why is the exchange rate on my card payment different than I expected? | Pourquoi le taux de change sur mon paiement par carte est-il différent de celui attendu ? | Lu tax dayo xaalis bi ñu ma dagg wuute ak bi ma doon xaar ? | card payment wrong exchange rate |
Does it cost anything to top up? | Est-ce que ça coûte quelque chose de recharger ? | Ndax ndugalum xaalis ci kont dafay laaj ay fere ? | top up by card charge |
The ATM machine would not give my card back | Le distributeur automatique n'a pas rendu ma carte | Gab bi delloowul sama kàrt | card swallowed |
Tell me where I can find the auto top up feature and a little bit about it please. | Dites-moi où je peux trouver la fonction de recharge automatique et quelques informations à ce sujet, s'il vous plaît. | Wax ma fan laa mëna gise doxalukaayu sarse otomatik? | automatic top up |
how long does it take to reflect in my balance a top up | Combien de temps faut-il pour qu'une recharge soit reflétée dans mon solde ? | Ñaata waxtu laa war a toog ngir ab sarsamã yegsi ci sama kont ? | pending top up |
I would like to return my purchases | Je souhaite retourner mes achats | Dama bëgga dello lima jëndoon | request refund |
Does this app have the same exchange rate as third parties? | Cette application a-t-elle le même taux de change que les tiers ? | Ndax aplikaasioŋ bii dafa am njëgu weccoo xaalis bu méngoo ak yeneen yi? | exchange rate |
I topped up but it isn't in my account | J'ai rechargé mais ce n'est pas sur mon compte | Dama sarse xaalis waaye nekkul ci sama kont | pending top up |
Are you able to delete my account? | Pouvez-vous supprimer mon compte ? | Ndax mën ngee a téj sama kont ? | terminate account |
I live in Germany. Is that one of the countries you are in? What other countries are you in? | J'habite en Allemagne. Est-ce un des pays où vous vivez ? Dans quels autres pays vivez-vous ? | Allemagne laa dëkk. Ndax bokk na ci réew yi seenii sarwiis am. Ci yan yeneen réew la am itam ? | country support |
There is a fee for a transfer, please explain that to me. | Il y a des frais pour un transfert, veuillez m'expliquer cela. | Teg nañu ma ay fere ci xaalis bu ma doon yónnee, leeralal leen ma loolu | transfer fee charged |
I don't want this account anymore, how do I delete it? | Je ne veux plus de ce compte, comment le supprimer ? | Dama bëggatul kontu bii, naka laa koy efaase? | terminate account |
What is the reason my top-up is still pending? | Quelle est la raison pour laquelle ma recharge est toujours en attente ? | Lan moo tax xaalis bi ma dugal ci sama kont bi yegseegul ba tay ? | pending top up |
Why was I charged a higher exchange rate when I bought something abroad? | Pourquoi ai-je dû payer un taux de change plus élevé lorsque j'ai acheté quelque chose à l'étranger ? | Lu tax dayo weccoo xaalis bi ñu ma dagg gënoon a yéeg bi may jënd ab afeer bitim-réew ? | card payment wrong exchange rate |
My top up card needs verification and I don't know how to do it | Ma carte de recharge nécessite une vérification et je ne sais pas comment procéder. | Dañu war a saytu sama kàrtu sarsamã te xamuma naka laa koy defee ? | verify top up |
What is the maximum number of transactions I can do with a disposable card? | Quel est le nombre maximum de transactions que je peux effectuer avec une carte jetable ? | Ban limu jëflante bu gëna bari bu ma mëna def ak kàrt buñuy jëfandikoo benn yoon kese? | disposable card limits |
I can't find the top-up card verification code. | Je ne trouve pas le code de vérification de la carte de recharge. | Gisuma kodu saytu kàrt sarse bi. | verify top up |
How do I stop fraud to my account? | Comment puis-je arrêter la fraude sur mon compte ? | Naka laa mëna dakkalee sàcc ci sama kontu? | compromised card |
Do I need to do something to get a new card once it expires? | Dois-je faire quelque chose pour obtenir une nouvelle carte une fois qu’elle expire ? | Ndax wara def dara ngir am kàrt bu bees su sama kàrt weeso gàpp? | card about to expire |
Is it possible to do auto top up? | Est-il possible de faire une recharge automatique ? | Ndax mën naa def sarsamã bu gaaw ? | automatic top up |
How long should a cheque deposit take to show? My account hasn't updated and I want to make sure everything is okay. | Combien de temps faut-il pour qu'un chèque soit visible ? Mon compte n'a pas été mis à jour et je veux m'assurer que tout va bien. | Ñaata wax la xaalis bu ma dugal ci sama kont jaare ko ci ab seg war a jël ngir yegsi ci kont bi ? Kenn yeesalaatul sama kont, te bëgg naa xam ndax lépp a tege ci yoon | balance not updated after cheque or cash deposit |
My Bank is in Europe, how long will the transfer take? | Ma banque est en Europe, combien de temps prendra le virement ? | Sama bànk a nga ca Europe, ñaata waxtu la jokkalante koppar bi war a jël ? | transfer timing |
The ATM didn't give me the full requested amount | Le guichet automatique ne m'a pas donné le montant total demandé | Gab bi joxuma xaalis bi ma laaj yépp | wrong amount of cash received |
Is there a way to reset my PIN? | Existe-t-il un moyen de réinitialiser mon code PIN ? | Ndax amn anam bu ñuy yeesale sama kod-PIN? | pin blocked |
I believe that someone is using my card without my knowledge! | Je crois que quelqu'un utilise ma carte à mon insu ! | Dama yaakaar be dafa am kuy jëfandikoo sama kàrt ci lu ma yëgul | compromised card |
Is there a limit to the number of disposable cards I can have? | Y a-t-il une limite au nombre de cartes jetables que je peux avoir ? | Ndax dafa am lim boo xam ne mënuma ko weesu ci ay kàrti jëfandiku-sànni ? | disposable card limits |
i cant seem to activate card | je n'arrive pas à activer la carte | Mënumaa aktiwe sama kàrt | activate my card |
The ATM keeps declining my Transaction . I tried two different ATMs already can you please check if everything is okay with my account? | Le distributeur refuse sans cesse ma transaction. J'ai déjà essayé deux distributeurs différents. Pourriez-vous vérifier si tout va bien sur mon compte ? | GAB bi moo ngi wéy di gàntal sama jokkalante bi. Jéem naa dem ci ñaar yu bokkul. Xoolalleen ma ndax sama kont amul benn jafe-jafe ? | declined cash withdrawal |
Let me know what the steps for the identity checks are | Dites-moi quelles sont les étapes des vérifications d'identité | Leeralal leen ma yan ñooy yooni cambarug dàntite bi ? | verify my identity |
Why did I get charged for a withdrawal? | Pourquoi ai-je été facturé pour un retrait ? | Lu tax ñu feye ku ma ab génne xaalis? | cash withdrawal charge |
My card has gone missing. | Ma carte a disparu. | Sama kàrt dafa réer | lost or stolen card |
How can I link my bank to my top up account? | Comment puis-je lier ma banque à mon compte de recharge ? | Naka laa mëna lëkkalee sama bànk ak sama kontu sarse? | transfer into account |
I got a strange fee when I used the ATM. | J'ai reçu des frais étranges lorsque j'ai utilisé le distributeur automatique de billets. | Dagg nanu ma ay fere yu doy waar bi may jël sama xaalis ci GAB bi | cash withdrawal charge |
I want to have multiple currencies in my account if possible. | Je veux avoir plusieurs devises sur mon compte si possible. | Dama bëgga gis xaalis bu bari ci sama kontu su mënee nekk. | fiat currency support |
Why has my money been returned back to my card. | Pourquoi mon argent a-t-il été reversé sur ma carte ? | Lutax ñu delloo sama xaalis ci sama kart? | reverted card payment? |
WHAT IS THE MAIN REASON OF THIS PROBLEM | QUELLE EST LA RAISON PRINCIPALE DE CE PROBLÈME | Lan mooy sababu jafe-jafe bii ? | card not working |
What works for identity verification? | Qu’est-ce qui fonctionne pour la vérification d’identité ? | Lan mooy dox ngir saytu dàntite? | verify my identity |
How can I get funds into my account from my American Express? | Comment puis-je transférer des fonds sur mon compte à partir de ma carte American Express ? | Nan laa mëna yónnee xaalis ci sama kont liko dalee ci sama kart senegaal ekspres? | supported cards and currencies |
Why is there a direct debit set up in my name? | Pourquoi un prélèvement automatique est-il mis en place à mon nom ? | Lu tax mu am ag ndëkkaale ci sama tur ? | direct debit payment not recognised |
What value can I get for my currency? | Quelle valeur puis-je obtenir pour ma devise ? | Ban dayo laa mëna am ci sama xaalis? | exchange rate |
Am I going to be charged for receiving money? | Vais-je être facturé pour avoir reçu de l'argent ? | Ndax dinañu ma fayeeku ci xaalis bi ma jot? | top up by bank transfer charge |
Which US cards have top up charges? | Quelles cartes américaines ont des frais de recharge ? | Yan ñooy kàrti Amerig yi làmboo ak ay fere sarsamã ? | top up by card charge |
On a card payment, why is there a fee? | Lors d'un paiement par carte, pourquoi y a-t-il des frais ? | Lu tax peyoor ak kàrt di am ay fere ? | card payment fee charged |
Your card pin can be changed at any Visa or MasterCard ATM with Pin services, excluding countries such as Belgium, Luxembourg, Austria, Germany, Spain, and France. | Le code PIN de votre carte peut être modifié à n'importe quel distributeur automatique Visa ou MasterCard doté de services de code PIN, à l'exception des pays tels que la Belgique, le Luxembourg, l'Autriche, l'Allemagne, l'Espagne et la France. | Kodu PIN bu sama kàrt ndax mënu nañu ko soppi ci bépp gab wiisa walla kàrt master lëkkaloo ak ay serwiisu kod pin, ba mu des réew yii belsik, luksaambur, fraas, almaañ espaav, otris? | change pin |
What's the process to receive a second card? | Quelle est la démarche pour recevoir une deuxième carte ? | Lan mooy jéego yi ngir am ñaareelu kàrt? | getting spare card |
My daughter needs an acount. | Ma fille a besoin d'un compte. | Sama doom ju jigéen daa soxla kont. | age limit |
I need a physical card. What are the fees? | J'ai besoin d'une carte physique. Quels sont les frais ? | Dama yittewoo ab kàrt. Yan ñooy fere yi ? | order physical card |
Please help me as my online payment is getting declined since yesterday while i am trying to purchase something online. | S'il vous plaît, aidez-moi car mon paiement en ligne est refusé depuis hier alors que j'essaie d'acheter quelque chose en ligne. | Ngir yàlla, dimbali ma ndax sama payoor ci net bi dañu ko bañ démbu ba leegi ginnaaaw bima jéemee jënd dara ci net bi. | declined transfer |
Is currency exchange possible? | Est-il possible d'échanger des devises ? | Ndax mënees na weccoo xaalis ? | exchange via app |
Do I pay extra for exchange? | Dois-je payer un supplément pour l'échange ? | Ndax dafa am lu ma war a feyaat ngir weccoo xaalis bi ? | exchange charge |
What is the top up code for? | À quoi sert le code de recharge ? | Lan la kodu sarsamã di jariñ ? | verify top up |
How do you come up with your exchange rate | Comment calculez-vous votre taux de change ? | Naka ngeen di xaymaa seen dayo weccoo xaalis ? | exchange rate |
Which flat currencies are supported for holding and exchange? | Quelles devises fixes sont prises en charge pour la détention et l'échange ? | Yan ñooy xeeti xaalis yi nga xam ne seen dayo du soppiku te ngeen koy jëfandikoo ngir denc gi ak weccoo bi ? | fiat currency support |
How long do European transfers take? | Combien de temps prennent les virements européens ? | Yónnee tugal yi ñaata waxtu lay jël ? | transfer timing |
What do I need to do to transfer money with my credit card? | Que dois-je faire pour transférer de l'argent avec ma carte de crédit ? | Lan laa wara def ngir yónnee xaalis ak sama kart kredi? | topping up by card |
I have been waiting for my transfer, shouldn't it be here already? | J'attends mon transfert, ne devrait-il pas déjà être là ? | Maa ngi xaar xaalis bi ñu war a dugalal, ndax warul woon a yegsi bu yàgg ? | transfer timing |
I tried the wrong PIN too many times. | J'ai essayé le mauvais code PIN trop de fois. | Dama bareel dugal kod PIN bu baaxul bi | pin blocked |
This transaction needs both a Visa and a Mastercard. | Cette transaction nécessite à la fois une carte Visa et une Mastercard. | Jëflante boobu dafay laaj nga am Visa ak Mastercard. | visa or mastercard |
I want a card, but I'm not in the UK- can I get one still? | Je veux une carte, mais je ne suis pas au Royaume-Uni. Puis-je quand même en obtenir une ? | Dama bëgg benn kart, waaye nekkuma senegaal. Ndax mën naa am benn? | country support |
Where is the PIN number found? | Où trouve-t-on le code PIN ? | Fan laa mëna gise baatu ubbikaay bi? | get physical card |
Will there be extra charges regarding to adding money into my international card? | Y aura-t-il des frais supplémentaires pour ajouter de l’argent à ma carte internationale ? | Ndax dina am yeneen njëg ngir yokk xaalis ci sama kàrtu diggànte ñaari réew? | top up by card charge |
I am not recognized by the app. | Je ne suis pas reconnu par l'application. | Aplikaasiyoŋ bi xàmmeewuma. | unable to verify identity |
Is there a limit to using a disposable virtual card? | Existe-t-il une limite à l’utilisation d’une carte virtuelle jetable ? | Ndax jëfandikoo ab kàrtu xarala jëfandiku-sànni dafa am ab àpp ? | disposable card limits |
The first payment I attempted for my card at the store earlier did not process so I had to make a second attempt. The second time it worked. It now appears I was charged twice. After looking at the app I see a pending charge. Please remove the pending amount because it is clearly not accurate and was declined. | Mon premier paiement en magasin n'a pas été traité. J'ai donc dû retenter. La deuxième fois, ça a fonctionné. Il semble maintenant que j'ai été débité deux fois. Après avoir consulté l'application, je vois un débit en attente. Veuillez supprimer ce montant, car il est clairement inexact et a été refusé. | Peyoor bi ma njëkk a defe ak sama kàrt tay ci suba ci ab màngasin jàllul, te it jéemaat naa. Ci ñaareelu yoon bi la peyoor bi jàll. Waaye dafa mel ne dagg nanu ma ñaari yoon. Ginnaaw bi ma xoolee aplikaasiyoŋ bi, gis naa peyoor bu nekk ci pekku négandiku. Far leen beneen limu xaalis bi nekk ci pekku négandiku ndax jaru... | transaction charged twice |
How long does a top-up take to go through? | Combien de temps faut-il pour qu'une recharge soit effectuée ? | Ñaata waxtu la ab sarsamã war def ngir jàll ? | pending top up |
I ordered something, and now I have buyer's remorse. Since what I ordered hasn't come yet, can you just cancel the payment since I already know I want a refund for it? | J'ai commandé quelque chose et je regrette. Puisque ce que j'ai commandé n'est pas encore arrivé, pouvez-vous simplement annuler le paiement, car je sais déjà que je veux un remboursement ? | Dama komànde loo xam ne fi mu ne sama xel dafa ciy sikka-sàkka. Segam li ma komànde yegseegul, ndax mën ngeen a neenal peyoor gi ndax dama bëgg ku ma delloo sama xaalis. | request refund |
I used my card to make a payment and wondered why the payment was reverted? | J'ai utilisé ma carte pour effectuer un paiement et je me suis demandé pourquoi le paiement avait été annulé ? | Dama jëfandikoo sama kàrt ngir def ab payoor te laaj naa lu tax ñu fomm payoor b? | reverted card payment? |
Why is the exchange rate wrong for my cash withdrawal? | Pourquoi le taux de change est-il erroné pour mon retrait d'espèces ? | Lu tax ci xaalis bi ma jël, dayo wecce bi jaarul yoon. | wrong exchange rate for cash withdrawal |
Am I able to change my PIN at certain cash machines? | Puis-je modifier mon code PIN à certains distributeurs automatiques de billets ? | Ndax mën naa soppi sama kod PIN ci yenn gab yi ? | change pin |
I think my card is broke? | Je pense que ma carte est cassée ? | Dama yaakaar ne sama kàrt bi dafa damm | card not working |
I made a big purchase that I regretted and cancelled, the merchant said that my refund was submitted. Can you confirm to me that all of my money was truly returned to me? | J'ai effectué un achat important que j'ai regretté et annulé. Le commerçant m'a indiqué que mon remboursement avait été effectué. Pouvez-vous me confirmer que j'ai bien été remboursé ? | Dama amal njënd mu jéggi dayo, moo xam ne sax réccu naa ko ba xàcc ko, jaaykat bi ne ma xamle na ne dañu ma war a delloo sama xaalis. Ndax mën ngeen ma firndéel ne delloo nañu ma sama xaalis bi yépp ? | Refund not showing up |
I need a refund for something I bought. | J'ai besoin d'un remboursement pour quelque chose que j'ai acheté. | Dama bëgg ñu delloo ma xaalis bi ma jëndewoon benn afeer | request refund |
I need to report a stolen card | Je dois signaler une carte volée | Dama wara yëgle ab kart buñu sàcc | lost or stolen card |
There has been a transfer pending in my account and I wanted to know how long it is going to take to go through. | Il y a un virement en attente sur mon compte et je voulais savoir combien de temps il va falloir pour qu'il soit effectué. | Amna toxal buy xaar ci sama kontu te bëggoon naa xam ñaata waxtu la wara xaar ngir ñu def ko. | pending transfer |
How do I add my new card to the app? | Comment ajouter ma nouvelle carte à l'application ? | Naka laa mën a lëkkalee sama kàrt ak aplikaasiyoŋ bi ? | card linking |
I'm not happy with the services I'm getting with this company. Can you please delete my account? | Je ne suis pas satisfait des services que j’obtiens avec cette entreprise. Pouvez-vous s’il vous plaît supprimer mon compte ? | Kontaanuma ci serwiis yimay jot ci liggéeyukaay bii. Ndax mën ngeen dindi sama kontu?
| terminate account |
Why was my atm withdrawl declined | Pourquoi mon retrait au guichet automatique a-t-il été refusé ? | Lu tax ñu gàntal sama njëlum koppar ? | declined cash withdrawal |
My card activation attempt failed. | Ma tentative d'activation de carte a échoué. | Jéemantu gi ngir doxal sama kàrt àntuwul | activate my card |
How can I verify my source of funds? | Comment puis-je vérifier la source de mes fonds ? | Nan laa mëna xoolee fu sama xaalis bawoo? | verify source of funds |
Please send me a disposable virtual card. | S'il vous plaît envoyez-moi une carte virtuelle jetable. | Ngir yàlla, ynnee ma ab kàrt wirtuyel buñuy jëfandikoo benn yoon kese? | get disposable virtual card |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.