Dataset Viewer (First 5GB)
Auto-converted to Parquet Duplicate
audio
audioduration (s)
1
29.8
transcription
stringlengths
1
591
s saa di bennaanu nattu jamono ji
soo bàyyiwul yëddu dinga mësa dégg lu la dul neex
jaaykatu sàngara la
waaw di wàññi gorum garab gi di jëmbat xam nga waaw yooyu daal lañ ne suñ si defee daal dina dina dina dina am solo
treize
damaa bëgg a dem
waaw dëgg la li ci ëpp mooy wàllu mbay mi ci la gën a baree
nga ne ma mbedd mi mbeddum buur la
daa am lu xew a
moo tax même bu ngeen defee engrais bu bëri da ngeen di gis gàncax gi yéen mënu leen ko gis scientifiquement lim ciy lim ciy jël tuuti rek la ciy soxla
waay yow gaynde gi gëna bon ñef naa seen ndey
foofu la foofu la jaar mais en tout cas dañuy dalal xelam rek ndax yaakaar naa ne ñun ñii it ay baykat lañu yaakaar naa ne kenn gënuñoo bëgg suñu suñu wér gu yaram kenn gënuñoo bëgg suñu suuf gi ba tax na li muy questions yi muy wax yi mu posé yi ñu posé la ci rencontres yi nga xam ne waa
fafal naaw yi wàññi
defaral say yéere
dinaa gise ak samay waajur ba noppi sog di xam lu ma lay wax
màndarga bi dafay wone ni dooley mbëjdoxalukaay ji di dekkarlook coppiteeg dawaan bi
bëgg naa i xaj
bare na ñu xamul woraaj ci taax yi dafa mërgëlu te xonq
nga loolu buñu ko doon def dina gën a dina gën a yomb
man nga dawee petee
ban car mooy dem académia limamoulaye
man naa sàngu am
olaand nguur gu olaand aantiy bu olaand réewum tugal óróop
dañoo am benn gis gis ci jàngoro ji
dama bëgg jàng
su fekkoon ne assurance su mbéy mi xam nga damay laaj keroog ngeen ne ma assurance su mbéy de passé na
man naa laa yóbb
damaa war a jël fii
bu ci yokku sa moroom wàññeeku su ngóora gi soppikuwul
am na solo teel a taw waaye nawet bi teel a tàmbali waaye tamit di yéex a yéex a yéex a yéex a yéex a jeex mu nekk loo xam ne xëy na dana am ay mbayteef yoo xam ne xëy na ñu teel a ji mën na leen indil gàllankoor ak yooyu xam naa ne sax xëy na danañ si ñëwaat si yeeneen i kii waaye loo siy digal ñi nga xam ne ñoo di baykat yi
seex isaa caw saasumaan bi
man tamit bëgg naa anglais
dañoo war a seet nees def ba sulli leen door leen delloo réew ma
dangéen a yàkkamti ba
àlliw jóob b seen baataan
boobu tam defoon ngeen si effort pour loolu ñu faagaagal ko
maa ngi ziar amady
ay cëslaayam yépp ci xayma lañu taxaw rawati na liñuy way aljibar bu bool
di nuyu tam waa agri jeunes parce que tey ñooñu may opportunité bi ñu mën a ñëw toog discuter échanger ak askan bi di leen wax ne rek li jublu wauñ si rek lu moy defar mais lépp loo xam ne lu si dëng rek ngeen jàpp ne si ñun la suñu motadi la mais dañoon bëggoon rek lu rafet ak partager ak nit yi merci jërëjëf
sococim
dañu daan demlante ngir dëgëral jàmm ji amoon seen diggante
tama yaa ngi topp ci moom sabar yi làmb
lu nekk mënees na koo toxal mu mel na mu meloon ba mu des wax
takkal soccent bi ak ab céq dina deñ
charettes yi am na machines yi am na kon kooku jigéen ñeek góor ñi ñëpp a si yem soo soxlaa matériels agricoles dangay dem commandé ñu wutal la comme ni ñuy wutalee góor ñi
mooy nit ki yàlla jëkka sàkk
complété les numéros cartes d identité
yal na ñu yàlla musal ci mbas mi
pour wax leen rek que ni informations yi ñuy joxe pour ñoom la pour nit ñi
tableau ferrailes
taccu nañuko bubax ci jamono ba muy nekk atlanta te rañe nañuko ngir pexe yu bess jëm ci njang
yaari xaj yi nelaw nañu
dafa gaaw a yaqu lool
man mii amoon naa ci naqar lool
keeyit yi yamalé nañu leen ngir aar yoon wi ndox mi gas té jàppandi ci bés bu njëkk ci weer bi ñenti weer lu jiitu ndortéelu weer bi
da doon saf suukar
léegi man nga koy jox ñam yu dëgëraale
képp ku bugg a toroxal béykat ak ku foo munti jugee ak loo munti doon
bëgg na maa
balaab golo ya
te day baax ñu ciy waxtaan ndax ñoom ñu mun a xam ne ah ñu ngi def ay jëf yoo xamante ne day yaakaar nañ ne ñu ngi siy faj seen soxla mais dinañ si faj seen soxla certainement mais li muy yàq tey ak ëllëg day day day day kii day bëri trop trop
iniwersite bu ndar ëmb na juróorum ñaari bërëbu tàggat ak gëstu
wax ko ak maslaa wax ko aussi ak fasaa
te ku xamoon fooy mujj
benn dëkk ak teeru la woon ci diiwaanu misi
lan moo reetaanlu lool
jërëjëf penda diagne kon ñun ñëpp ñoo ko déggandoo waa touba njaañ fi ñu toll seen liggéey tool yi tey wax nañ ne wax dëgg yàlla am na si loo xam neam nañ yaakaar
mooy fertilité suuf si
paaka du bënn deram dafa tul loolu la wax
silaama sii ci cosaanu dëkk bi la bokk
li mu sumboon lépp can na ndax mbal mi mu dugg
ci yoon wépp nit ñi dañu toppoo di ko soowtaan
sorgho tamit dafa bugg suuf soo xam suuf suy téye ndox ak même ceeb tamit xam nga fii tam dañ fiy béy ceeb au niveau donc de la région ceeb fii la ñu koy béyee département fatick
boo xoolee di nga xam
yàgguma fa dama wax li ñu ma yónni woon rekk daldi dëpp
wuññiy araans yisoppi
dawaan bu safaanu
ndax monsieur malang mën a xam fi nga dëkk
moo tax it ma ne su ñu mënoon xam ban dëkk
man nga koo baral a
ma ngi jëm jàmb ji nekk ci seen wetu kër
nu ndaje bi demee
tapoo gu warsawsoppi
lu tax may jooy
te aussi ne leen coopérative li koy dundal mooy cotisation annuelle
dafa bari wërsëg
jaboot a jeng
xasaayiti laata junni ak fanweer ak ñeent
pour nga mën a jël semence boobu
nekk naa itam ab wàcc bees
baanabaana bi tàmbaakundaa lay jënde digija
jilaan mbay layti ñaar fukk ak juróom amadi sayxu
ecole hlm rufisque
man ngaa ñibbi
mën naa ko dinaa koy déglu si rajo bi dinaa koy déglu si waa resop itam
waaye nekkóo fa
nelaw tuuti wax tuuti mos tuuti
sabar ya ca ndayaanee
bàyyi sa wërsëg fii lu mel ni tarfatal ayni
man ak moom nooy liggéey
End of preview. Expand in Data Studio

A curated Wolof ASR dataset from various sources:

Split Fleurs Alfa CV Kallama UB Total
Train 8.72 16.13 34.97 33.60 4.52 97.94
Test 1.75 2.84 6.21 5.91 1.12 17.83

This dataset was used to finetune Wolof-HuBERT-Base for ASR.

Downloads last month
9

Collection including soynade-research/Wolof-ASR-Data