wo
stringlengths
1
4.03k
fr
stringlengths
1
1.08k
Sama barab, 9:00.
Ma place, 9:00.
Dindil wàll wi ci suuf, xool tànneef yi ci war, def bépp coppite ci sa adres su ko jaree, nga yónnee ko ci enveloppe buñu tëj.
Supprimez simplement la section du bas, cochez les options correspondantes, faites des modifications à votre adresse si nécessaire et envoyez -la dans une enveloppe sécurisée.
Sunu tukki bu mujj.
Notre dernière envoi.
Waaye mu ni...
Mais ensuite, il dit...
Vraèao sama bopp ci Galviston ginaaw xare bi.
Vraèao moi-même à Galviston après la bataille.
Mingi toog ci kaso bu Los Angeles.
Il est dans une prison de Los Angeles.
Amoon na benn fetal ci sama wetu kër, te loolu mettiwoon na lool ci dëkkandoo yii.
Il y a eu un tir près de ma maison, et c'était vraiment mauvais dans ce quartier.
- Defar fita yi. - Waaw.
Prête les canons.
Ci benn yégleb, Orãas xamle na : Wave ñaan na Sonaatel ngir mën a jaay kérédi Orãas.
Dans un communiqué, Orange signale : La Sonatel a été saisie par Wave pour distribuer du crédit Orange.
[goor ñuy wax làkk wiñ nàmp] góor guy wax làkk wiñ nàmp:
[homme parlant la langue natale] homme parlant la langue natale:
Su sedd, yéere yu ñu fourre leen wëtteen,
S'il fait froid, vêtement doublé de laine de Coton,
Ñàkk naa sama pàppa.
J'ai perdu mon père.
Jàpp naa ko!
Je m'en occupe!
Waaw, dina ñu klone ku mag ki.
Oui, ils vont cloner le gros.
- Bàyyil Urea jël komando bi.
- Laisser l'Uréa prendre la commande.
"Danu ko wara wane sunu tiitaange."
« Nous devons lui montrer notre peur. »
Tukkikat bi, ñëwal ci sunu barab!
Allez chez nous, Voyageur!
Wax ko duma sa pàppa, squirt!
Dis lui que je ne suis pas ton père, gile!
Sudee loolu mooy sama jëkkër, sudee amoon na chance, ak lumu mëna tuuti,
Si c'était mon mari, s'il y avait une chance, quelle que soit sa taille,
May biy féexal xol, kéemtaan bu rëy la woon.
Ce don de consolation fut un miracle superlatif.
Lii mooy Serjant bu mag bi di Clem Francis, mingi jeexal larme bi ci forsu aérien bu Etats Unis.
C'est le chef du Sergent Clem Francis, retraité de l'armée de l'air US.
- Waaye lan?
- Mais quoi?
Dama bëgga yegg ci tundu wi gëna mag, yéeg, su ma bëggee, te duma yuuxu.
Je veux atteindre la plus grande montagne, grimper, si je veux, sans tous les cris.
Moo gën.
Il ferait mieux.
- Dafa rafet.
- Ça a l'air bien.
Danga wara génn foofu.
Vous devez sortir d'ici.
Mooy nu jàll ci ba noppi nu tëj sunu bopp ci yeneen poñ.
Il s'agissait de le traverser et de nous verrouiller sur différents points.
[ GROANS ]
[GROUSSEMENTS]
Ndawi nguur gi nangu wuñu soppi seen doxalin.
Les agents du Gouvernement refusent de changer leurs méthodes.
(MOTEUR BI TAMBALE)
(ENGINE STARTS)
Dafa bari lool ci benn pilote.
Trop prouvé pour un seul pilote.
- Mën nga dellusi?
- Pouvez -vous revenir?
Bu yàgg naa bëgga nekk nit, waaye leegi bi may dund, mën naa dee.
J'ai longtemps voulu être mortel, mais maintenant que je suis en vie, je peux mourir.
Loser dafa wara setloo Amerique.
Loser doit garder l'Amérique propre.
Danuy def ay jeu, di tàggat sa bopp, ci ñetti waxtu.
Nous faisons des parties, entraînement, à trois heures.
Yaakaar nga ni dina am njariñ ci man?
Pensez -vous que ça marcherait sur moi?
Baay, bëgg naala.
Papa, je t'aime.
Leah des ci kër ga.
Au moins un que Leah restera à la maison.
Déedet, déet, déet... soxna si.
Non, non, non... Madame.
Li nga xam ne dëñul di tiittal Tugal mi am yég-yégu ñàkk baatam ci réew mi mu moomoon.
Ce qui ne manque pas de susciter une inquiétude au niveau de l’Hexagone qui a le sentiment de perdre progressivement l’initiave dans son ancienne colonie.
Ndawi nguur gi bëggu ñu soppi seen dundin
Les responsables du Gouvernement ne veulent pas changer leur mode de vie
Loolu mooy sa pexe?
C'est votre plan?
-Ana.
- Hannah.
Centre commerce mondial bi, Pentagon bi, Somerest bi ak Pennsylvanie dañu leen tere jokkoo
Le World Trade Center, le Pentagone, Somerest et les tours de Pennsylvanie ont été empêchées de communiquer
Yal na Yàlla barkeel ñi dee.
Dieu bénisse les morts.
PAXTONI Waaw, waaw.
PAXTONI Bien, oui.
Nekkatuma sa doom.
Je ne suis plus votre fils.
Mmm.
Mmmm.
Waaw, dëgg la.
Oui, c'est ça.
Waaye du benn.
Mais ce n'est pas la même chose.
Nu foogoon ne xaalis bi du dugg, te dinañu nu sàcc.
Nous avons pensé que l'argent n'entrerait pas, et que nous serions volés.
naka ngay xaar 22 réew arab yu wuute ci gox yi..
Comment vous attendez -vous à 22 nations arabes avec des régions différentes...
Barab buma gis ay nataal kese.
Un endroit où je n'ai vu que des images.
Soo xamoon lii tekki ci man.
Si vous saviez ce que cela signifie pour moi.
Ci tiit.
De peur.
Maa ngi gis itam naaj tranquillize doo ko soxla.
Je peux aussi voir l'aiguille de tranquillisation que vous n'aurez pas besoin d'elle.