Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet Duplicate
language
stringclasses
1 value
speaker_id
stringclasses
3 values
prompt_id
stringlengths
4
4
prompt
stringlengths
15
110
segment_id
stringclasses
5 values
audio
audioduration (s)
2.27
69.4
duration
float64
2.27
69.4
raw_text
stringlengths
24
1.23k
iso_639_3
stringclasses
1 value
glottocode
stringclasses
1 value
iso_15924
stringclasses
1 value
id
stringlengths
36
36
parent_id
stringlengths
36
36
wof_Latn
spk03
f026
What are some foods that can cause bad breath?
s01
19.944
Waaw, lekk biy teey sa xel bi ni moment bii mooy déget nii nga toggu ko, léegi togg bi ñorut. Léegi boo ko lekkee mën na teey sa xel bi walla cere bi ëpp laalo. Bu ëppee laalo rekk, boo ko lekkee mën na teey sa xel walla nga ut meew boole kook bu ëpp laalo. Loolu it mën na si teey sa xel.
wof
gamb1252
Latn
5f862088-92ef-470d-bfd1-0964befdbc41
5f862088-92ef-470d-bfd1-0964befdbc41
wof_Latn
spk03
h107
What purpose does soap serve?
s01
14.828
Saabu dañ koy fóotee, mun naa sangu ak raxas. Mun naa fomp it waaye duñ koy deferee ndax saabu tomb bi rekk dañ koy deferee ak xeme ak xolliti gerte. Waaye bu tubaab bi moom xamuñu nuñ koy deferee.
wof
gamb1252
Latn
619e6cc0-a3f0-48ee-8b79-16f67efb0749
619e6cc0-a3f0-48ee-8b79-16f67efb0749
wof_Latn
spk01
h103
What purpose do passports serve?
s05
4.373479
Mooy defer réew, mooy dimbale réew. Salaamaalekum.
wof
gamb1252
Latn
6ae7e544-1c7f-47af-b551-d82162c2b513
6ae7e544-1c7f-47af-b551-d82162c2b513
wof_Latn
spk03
f025
Are there any foods that are believed to help improve strength?
s01
22.376
<noise> cere bi cere bi baax na, cere bi si dugub. Dugub bi dañ koy bay.  Cere boobu itam baax na ak meew mi. Meew mi, meewu nag la dañ koy rahatt. Boobu it baax na. Yàpp wi itam; moo xam yàpp bëy la walla nag yàpp wi tam baax na.
wof
gamb1252
Latn
a5572121-0368-4588-a01c-36071d4ba3af
a5572121-0368-4588-a01c-36071d4ba3af
wof_Latn
spk03
n070
Please say the names of the days of the week in order, starting from Monday.
s01
4.944
Altina, talaata, àllarba, alxames, ajjuma,  samdi, dimaas.
wof
gamb1252
Latn
72edb366-a0ef-48b3-8e83-d3d1c75ed044
72edb366-a0ef-48b3-8e83-d3d1c75ed044
wof_Latn
spk03
i055
Can you explain how to wash your hands properly?
s01
25.956
Waaw <hesitation> raxasee sa loxo, su nekkee loxo bi daa tilim bo, mun nga njëkke suuf bi. Boo njëkkee suuf bi bomb sa loxo yi bomb ba ŋa xam ne sa loxo yi dañ na, nga raxas ko. Léegi jël ndox boo xam ne mingi am ordusawel ak omo nga raxas sa loxo yi ba sa loxo yi set nga jël ndox bu set lahandee ko. Boo ko lahandee ba pare, léegi mun nga jël sa musuwaar nga fomp, fomp loxo yi ba nga xam ne tooy bi deñ na.
wof
gamb1252
Latn
f9c863f6-bb48-4a4b-876e-4b1522c0ec98
f9c863f6-bb48-4a4b-876e-4b1522c0ec98
wof_Latn
spk03
m007
Name as many colors as you can.
s01
21.172
Bula am na, ñuul, werta, xonqu, weren, móof, dingiri ak sokolaa. Dóom-taal am na. roos. Defe naa yooy laa xam de.
wof
gamb1252
Latn
d6889e85-0a03-4387-98b8-a93cc66e77ae
d6889e85-0a03-4387-98b8-a93cc66e77ae
wof_Latn
spk16
f002
What are some foods that are really simple and you enjoy a lot?
s01
29.72
lekk yi nga xamante ni su ma ko lekkee damay sawar dafa yëngu mooy fruits <noise> yi nga xam ne dafay ñor fii nii comme guyave, comme mandrine, comme mango, comme oraas, nekk na si lekk yi ma neex, ñoo xam ne su ma ko lekkee damay am cawarte, waa damay am cawarte te yomb na lool jefewut fii nii bu baax parce que dañu koy béy suñu àll yi, dañ koy dafay ne dañ koy jiw suñ kër yi, dafay ñor nga dem waaxu rek witti, ñëw raxas rek lekk, loolu rek nga ciy am. Te su ma ko lekkee dama ciy yëg sama bopp bu baax, dama ciy kontaan bu baax ndax doon na doon na ay fruits yi nga xamante ni neex nañ ma lool lool.
wof
gamb1252
Latn
52d1f263-1dd0-44ef-8db7-2a1f08343e69
52d1f263-1dd0-44ef-8db7-2a1f08343e69
wof_Latn
spk01
n029
How many countries have you visited? Please name them.
s01
21.608
Bi ci jëkk mooy dem naa senegaal, <hesitation>  dem naa kaasamaas, <hesitation> dem naa gine ak gàmbi gii ma dëkk.
wof
gamb1252
Latn
3dd7e527-1d79-4468-abed-76ae7290d523
3dd7e527-1d79-4468-abed-76ae7290d523
wof_Latn
spk03
f024
Are there any foods that are believed to help improve eyesight?
s01
16.216
Xam nga karoot day yokku leeraayu bët, te karoot dañ koy bay ci suuf bi. Ci suuf bi lañ koy bayee. Meme nawe it baax na. Nawe it ñu ne day yokk leeraayu bët, te boobu dañ koy bay. Ci suuf bi lay jugee.
wof
gamb1252
Latn
7a0f5c5f-837f-44b7-805d-a1121b74ad28
7a0f5c5f-837f-44b7-805d-a1121b74ad28
wof_Latn
spk03
n071
Please say the names of the twelve months of the year in order, starting from January.
s01
9.004
Léegi hore, diggi, tabaski, tamxarit, diggi gàmmu, rakki gàmmu, rakkaati gàmmu, maamu koor, ndeyu koor, baraxlu, weeru koor.
wof
gamb1252
Latn
aa542b6d-4fec-419b-bbfe-9103c89554aa
aa542b6d-4fec-419b-bbfe-9103c89554aa
wof_Latn
spk03
i051
Explain how to do laundry by hand.
s01
27.208
<hesitation> lañ doon fóotee loxo dangay def saabu. Boo defee saabu, julli ba pare. Su nekkee bànku ngay fóote, nga téye si bànku bi. Boo téyee si bànku bi ba pare nga doog ko fete sa loxo yi boo ko fetee sa loxo yi ba pare dugal wañ dugal si beneen ndox bi; bu nekkee dangay fóotee bànku. Boo fóoteewul bànku moom, sa loxo yi nga jël di fete, di fete bam  mummaa mi set nga doog a kii.
wof
gamb1252
Latn
882454dc-2f1f-4148-b86e-c97d135e1541
882454dc-2f1f-4148-b86e-c97d135e1541
wof_Latn
spk01
f084
What different types of vegetable oils are there, and how are they different?
s03
19.663521
Noon la ko defee ca garabag teŋ ga, noon la ko defe ca garabag <hesitation> new ga, ci yi nga xam ne ñun suñu xam-xam àgg na ca ci suñ lëññëtu, bañ xam ne yii dafay génne diw, diw boo xam ne lii la ak lii ak lee te benn bokkut ci sa moroom wàntu yépp diw lañ, te benn bu nekk am na lu moo def si biir jëmmi doom-aadama <noise>.
wof
gamb1252
Latn
23056115-f253-48ac-b1cd-c5bc53336c7e
23056115-f253-48ac-b1cd-c5bc53336c7e
wof_Latn
spk01
f025
Are there any foods that are believed to help improve strength?
s03
10.085042
Loolu mooy li ma xam ne, loolu laa xam ci li ñoo dunde suñ ko doon def dañ am wét-gi-yaram, <unintelligible> te buñ amee wét-gi-yaram, am kàttan buñ amee kàttan man a lëggéey. Buñ lëggéeye man a hoor.
wof
gamb1252
Latn
fbad68f8-29e9-4213-8caa-b3b7315dac8d
fbad68f8-29e9-4213-8caa-b3b7315dac8d
wof_Latn
spk03
h063
What is a bank?
s01
28.188
<noise> bànk de denceekaayu xaalis la comme ça léegi yaw boo amee xaalis, wóoluwoo koy denc si kër gi, léegi mun nga koo yóbbu si bànk bi, denc ko fa. Léegi boo amee soxla  nga xam ne soxla daa taxaw, léegi man nga dem récupérer waat xaalis bi, ñëw fajee sa soxla. Saa soo amee nag, nga dem yóbbu <hesitation> denc dencaat dencaat  ko foofu noonu. Loolu mooy bànk pour denceekaay xaalis daal la.
wof
gamb1252
Latn
af518af7-53eb-4b23-82c9-24ee31a5329e
af518af7-53eb-4b23-82c9-24ee31a5329e
wof_Latn
spk03
m009
Name as many types of trees as you can.
s01
11.296
Màngo am na, kaasiyaa, darkasu, guy, dittax, kabaa ak ban? Am na beneen de.
wof
gamb1252
Latn
bf5c39c4-156c-425d-a3bd-8dd34c4513c7
bf5c39c4-156c-425d-a3bd-8dd34c4513c7
wof_Latn
spk01
p096
What is the role of government in economic development?
s03
2.265354
Balaa jot dana  yàgg de.
wof
gamb1252
Latn
1ede33b2-a3cb-4973-994c-760f44ced584
1ede33b2-a3cb-4973-994c-760f44ced584
wof_Latn
spk01
p116
Is it possible to be completely honest all the time?
s01
23.9025
Waaw doomu aadama, kii lim laaj mu ne  ndax nit mën nay dundu <hesitation> ba ci, ci waxtu wu nekk rekk, mu ngi dal, waxtu wu ne mu ngi féex, waxtu wu nekk rekk dundëm mingi correct. Waaw  <hesitation> jikkoom la laaj nde yaw loolu nga wax noonu, nit moo koy am waaye ci jikkoom la koy amee.
wof
gamb1252
Latn
97f96749-6990-4e1e-8180-68306afeb2b5
02fa4d27-0d23-4110-a859-7ea884337070
wof_Latn
spk01
p116
Is it possible to be completely honest all the time?
s01
5.960625
Jikko bu baaxee rekk, léppam baax na. Su bonee, boroom, léppam bon na.
wof
gamb1252
Latn
b4b0cba4-0698-46d1-99f8-632d7cd1cb2e
02fa4d27-0d23-4110-a859-7ea884337070
wof_Latn
spk01
p116
Is it possible to be completely honest all the time?
s01
8.160875
Kon ci tontu bu gàtt mooy ku baax jikko daal, danga dem ba sa dundu neex ci boor bu nekk. Ndeg lan?
wof
gamb1252
Latn
7643ea74-8432-40cc-8e43-6c9244ef787c
02fa4d27-0d23-4110-a859-7ea884337070
wof_Latn
spk01
p116
Is it possible to be completely honest all the time?
s01
8.780938
Ndeg melow jikko ji nga ame de ko dundee, moom moo jaarele dundu sa diggante ak képp koo digaale. Ba tax na, mu rafet.
wof
gamb1252
Latn
987553ff-a7b8-4cb0-aa5d-1fcb88dd4922
02fa4d27-0d23-4110-a859-7ea884337070
wof_Latn
spk01
p116
Is it possible to be completely honest all the time?
s01
9.621
Donte sa jikko dafa baax rekk, koo séqal rekk la nga séq ak moom lu baax laay doon. Te séq ak nit lu baax lu bon da ca génn. <hesitation> te la bon mooy waral xat.
wof
gamb1252
Latn
d40456b0-4cea-4290-afdd-d11ca9fcfc5f
02fa4d27-0d23-4110-a859-7ea884337070
wof_Latn
spk01
p116
Is it possible to be completely honest all the time?
s01
9.841063
Mooy waral ham foo ñimee dem ak foo ragal a dem, ham ko hóolu ak koo hóoluwul, ham koo bëgg ak koo bëggul, ham ku la héene ak ku la héenewul. Loolu la koy def mooy jikko ja.
wof
gamb1252
Latn
b0dbcf15-1c72-4f80-aab6-efbe81b609f1
02fa4d27-0d23-4110-a859-7ea884337070
wof_Latn
spk01
p116
Is it possible to be completely honest all the time?
s01
6.140625
Moom nam la xamee, noonu la lay jàppee. Soo ko wanee ni gën ci melo yi, mu jàppe la jàppin wi gën si jàppin yi.
wof
gamb1252
Latn
a496d764-2326-4c8a-95a5-1595bbc07322
02fa4d27-0d23-4110-a859-7ea884337070
wof_Latn
spk01
p116
Is it possible to be completely honest all the time?
s01
3.400375
Loola, bu dee ci iir gi nga dëkke, yow dinŋ fa man a dundu ci jàmm.
wof
gamb1252
Latn
64245ef4-cb14-47db-8b67-9ea9c3b90d36
02fa4d27-0d23-4110-a859-7ea884337070
wof_Latn
spk16
f016
What are some traditional dishes from your culture that you love?
s01
69.416
ñun suñ cosaan bu dee ñun suñ cosaan lu ma ci gën a bëgg mooy suñu dignité yi nga xamante ni amoon nañ ko, suñuy dëkku yi nga xamante ne nekkoon nañ si ñun, suñu njàmbaar ak suñu bëgg a liggéey ak suñu bëgg suñu bëggante suñu biir daal loolu bokk na ci li nga xamante ni dina ma di touché toujours maanaam sama cosaan man loolu damay toucher toujours sama cosaan. Ndax ñun suñu cosaan daawuloo ànd ak sa rakk walla sa mag dem àll mu dee nga ñibbi si ñun kilifa daanul am, daanuloo mukk dëkk ak sa mag walla sa rakk walla sa doomu nijaay walla sa doomi bàjjen ba tolof-tolof dal ko nga mu muy muy dëkk si ay coono te ma mën ko cee dindi, nga mën ko si xettali ba pare di ko seetaan, loolu amutoon ñun askan, bokk na ci mbir mi nga xamante ni nag daanaka ci jamono tey jii jikko yu mel noonu dafa commencer jeex waaye mu ngi des ba léegi daal waaye bokk na si jikko yi nga xamante ne nekkoon nañ ci suñu cosaan ñun, nekkoon na suñu biir askan yi mu doon jikko yi nga xamante ni neex na ma lool, mu doonoon ay qualités yi nga xamante ne neex na ma lool, te man toujours damay toog sama  xel di ci nekk ma ciy kebetu toujours di ci waxtaan toujours pour ñu mën ko delloo ci suñ biir dund gi ndax lu amoon njëriñ la si biir dund gi.
wof
gamb1252
Latn
37f8eb70-4c66-42d1-96ca-5a2d974988e9
c6335317-b088-4a0a-9ce4-cf0954f3de23
wof_Latn
spk01
n022
How many different languages do you think there are in the world, approximately? It’s OK to take a wild guess.
s01
29.247875
Waaw li nga xam ne  jëlee  ci jàng ñu waxee ñu ko ci téere, ci yépp làkk yi yàlla def ci kow suuf, wax nañ ni mat na  junney làkk. Te junney làkk yooyu yàlla bind na <noise> ci doomu aadama yi, giir yépp, bu ci ne am na giir guy làkk làkk woowu.
wof
gamb1252
Latn
57bf050a-1cb2-483c-9c6f-b2dddd1ecd46
02423ec2-90be-45e5-82dd-aaeb0290c784
wof_Latn
spk01
n022
How many different languages do you think there are in the world, approximately? It’s OK to take a wild guess.
s01
5.681563
Mboolem ni làkk yi tollu. Loolu dey téere moo ñu ko sool.
wof
gamb1252
Latn
f4409628-e678-4978-b7b5-de9fc2659d4f
02423ec2-90be-45e5-82dd-aaeb0290c784
wof_Latn
spk01
n022
How many different languages do you think there are in the world, approximately? It’s OK to take a wild guess.
s01
24.286563
La ko dalee ci aadama aleyhi salaam, ba ci fiñ tollu nii di wax man ak yaw, li fi ne ci làkk ci kow suuf ñi ñooy tudde doomu aadama di ko wax, te yàlla moo leen ko jox mat na junney làkk. Lii dey lii de jàngee nañ ko ci téere, ñu wax ñu ne nii la ko yàlla tërële.
wof
gamb1252
Latn
42474083-3d22-46a0-b2bf-3074514fefc2
02423ec2-90be-45e5-82dd-aaeb0290c784
wof_Latn
spk01
i043
How would you cook chicken?
s01
14.922563
Waaw mu ne dafa laajte naka lañuy toggee ganaar. Ñun, li jëkk ci ñun ci ñun ni ñuy toggee ganaar mooy gannaaw bu ñu ko rahee ci turu yàlla nde diine islaam jiñ nekk.
wof
gamb1252
Latn
c88e74c6-4840-4e1f-ad89-85d985ee784a
44caeb16-e6d0-4efc-a3f3-c16cdaebe8ef
wof_Latn
spk01
i043
How would you cook chicken?
s01
9.98175
Dañ ko war a xotti, génnee la ca bokkut. Door koo jox jigéen ji koy suqi.
wof
gamb1252
Latn
002869ea-28f8-4e8c-b7e4-7ce80b480050
44caeb16-e6d0-4efc-a3f3-c16cdaebe8ef
wof_Latn
spk01
i043
How would you cook chicken?
s01
9.241625
Mu door koy <hesitation> tàngal ndoxam, soode ko, fekk génne nañ lépp lu neen ca biir ba ci sobe. Ñu raxas ko bam set.
wof
gamb1252
Latn
f72912ff-6c0a-4478-b514-1c9194068bec
44caeb16-e6d0-4efc-a3f3-c16cdaebe8ef
wof_Latn
spk01
i043
How would you cook chicken?
s01
10.801875
Lee-lee ñu def ko togginu, ba war ci toggin di cee toggee ñam wim bëgg mu baax. Yam ca war a boole, mu boole ko ca ci lu dagan a lekk ñu boleente ko.
wof
gamb1252
Latn
342beeca-dca7-47f7-887b-94f93108bd86
44caeb16-e6d0-4efc-a3f3-c16cdaebe8ef
wof_Latn
spk01
i043
How would you cook chicken?
s01
17.062938
Bu boobaa lekk ga dana am njariñ, te doo ci jële feebar, te boo ci jëlewul feebar rekk wér la laay yokk. Ñun ni ñuy toggee ganaar mooy daal, gannaaw bu ñu ku rendee ci turu yàlla, génne saleté ba ca biir, ba pare door ko df suqi ba mu set ñu jënd, jigéen gi moom ci boppam defar ko.
wof
gamb1252
Latn
dc9cdb98-1568-44d1-b9b0-6a71a0f07629
44caeb16-e6d0-4efc-a3f3-c16cdaebe8ef
wof_Latn
spk01
i043
How would you cook chicken?
s01
7.36125
Dindi lépp luy der ba ca kow, mu des yàpp wa, mu togg ko na mu ko war a toggee bam mat, su pare ñu man ko lekk. Ñun noon lañay lekkee ganaar noon lañay lekkee ganaar.
wof
gamb1252
Latn
6fa06645-161c-4c9b-979c-1b65985622db
44caeb16-e6d0-4efc-a3f3-c16cdaebe8ef
wof_Latn
spk01
p096
What is the role of government in economic development?
s01
15.74325
Waaw laaj nga laaj bu am solo bu dëppoo ak dundu giiñ tollu. Fowwu njiit di ham ci kër, ci dëkk, ci tundu, ci réew.
wof
gamb1252
Latn
402c881a-aa2e-4b02-bbf6-d4b792d66119
faeac544-55b4-4728-be20-8a1ee64abaf9
wof_Latn
spk01
p096
What is the role of government in economic development?
s01
20.304188
Njiit bu ci ne dëppoo ak ñam jiite lu ko war la, ñoom it ñu dëppoo ak ka ñu jiital, ñoom mbooloo ma lu war la. Kon liy njëkk a defar kër mooy dëppoo.
wof
gamb1252
Latn
fcbbb3d2-6bd7-4d1b-9e40-bad75ec8579f
faeac544-55b4-4728-be20-8a1ee64abaf9
wof_Latn
spk01
p096
What is the role of government in economic development?
s01
15.443188
Dëppoo mooy ànd, bokk pas-pas. Loolu mooy dëppoo ci lëggéey ba ak lu ñooy rafatelee lëggéey ba ak lu koy sakkanal ak lu koy saxal ca barab ba.
wof
gamb1252
Latn
150d7dac-75b6-4c95-a660-468943505ecf
faeac544-55b4-4728-be20-8a1ee64abaf9
wof_Latn
spk01
p096
What is the role of government in economic development?
s01
25.865313
Loolu bu ko kër ga defee, koñ ba def ko, dëkk ba def ko, tundu wa def ko, gox ba def ko bam daj réew ma defe ko. Liiy yokk am-amu réew mooy ñépp lëggéey te bañ a yàq ak lëggéey ba nga jàng ba man ko bum man a doon  donte yaw mi toog ci taabal ji ngëb pen bi.
wof
gamb1252
Latn
c1a3912a-594c-4dc1-b211-dfff9bb53fe9
faeac544-55b4-4728-be20-8a1ee64abaf9
wof_Latn
spk01
p096
What is the role of government in economic development?
s01
6.721375
Nangul sa lëggéey boobu te teg ko ci njub. Sa pen boobu dana yokk lépp luñ bind.
wof
gamb1252
Latn
27926189-f38a-4ee3-bdff-b1d3ea28e397
faeac544-55b4-4728-be20-8a1ee64abaf9
wof_Latn
spk01
p096
What is the role of government in economic development?
s01
5.281063
Dana yokk ci yow, yokk ci réew mi ngay bindal ndeem yaaŋ ko teg ci njub.
wof
gamb1252
Latn
6e7c59b2-00eb-45f4-84c6-7cbfbf0fa341
faeac544-55b4-4728-be20-8a1ee64abaf9
wof_Latn
spk16
f012
How long can you keep vegetables before they are dangerous to eat?
s01
42.209375
Waa lejum yu mel noonu nag denc leen lu yàgg te yàquwuñu loolu jafe na lool, waaye nag jamono dox na ba ay jumtukaay génne nañ li nga xamante ni dañ ñuy dimbale ci suñ dund gi, ndax yàlla moo waxoon ne dinaa def ci xelu doomi adama <hesitation> benn xarañteef, xarañteef boobu nag moo ñëw ba liggéey ay jumtukaay yi nga xame ne nit da koy mun a denc lejum yu mel noonu diir te du yàqu. Benn lejum lañ daan mën a mën a denc lu yàgg te du yàqu ñu ko daan tuddee pataas, moom daal bu mosoon a su- gas lu melk ne pax bu ndaw nga def ci salañ nga tooyal salañ ba tuuti ba m bam bam bam ba mu ba mu guus nga def ci palaas bi ba pare sottiwaat salañ ci kawam, moom daan na mën a nekk foofu noonu ay weeri weer weeri weer weeri weer te du yàqu, moom daan nañ ko dencee noonu.
wof
gamb1252
Latn
391672e0-cd8a-41e4-bf60-498a950a19d1
85c084d8-02e1-4f2e-98c8-066ed51898c3
wof_Latn
spk16
f012
How long can you keep vegetables before they are dangerous to eat?
s01
11.762625
Daan naa gis suñuy waajur yi daan ko <noise> denc noonu lu yàgg te du yàqu. Waaye bu demee comme su- ay supame yu mel noonu yooyu ci frigo rek nga leen mën a def ñu yàgg te du ñu yàqu, waaye boo leen dencee ci bërëb bu bërëb bi yenn bërëb yi  dañuy yàqu.
wof
gamb1252
Latn
cde5acd9-738a-485f-b179-74b6469838df
85c084d8-02e1-4f2e-98c8-066ed51898c3
wof_Latn
spk16
f012
How long can you keep vegetables before they are dangerous to eat?
s01
18.024
Bu dee heure(u) sedd lañ ñor nag mën nañoo dem ba weer du ñu yàqu boo leen dencee palaas bi nga xamante ni newuñ ci biir saako walla ñu teglantewuñu lu bari maanaam nga teg ko moom kenn bërëb tegaat beneen moom kenn bërëb tegaat beneen moom kenn bërëb, bu dee si palaas bu wow la ba pare sedd gi di ko laal mën naa yàgg foofu noonu te du yàqu.
wof
gamb1252
Latn
baae9da5-af30-4672-a69e-0dbee3686e8a
85c084d8-02e1-4f2e-98c8-066ed51898c3
wof_Latn
spk01
f026
What are some foods that can cause bad breath?
s04
25.806313
Ñun liñ hamoon mooy keŋkilibaa, mbor-mbor, lëng, xobi rat. Yii lañ daan def kafe ba léegi, boo feebaree feebar yu sew yi ay siddit aki ay soj aki kalab-kalabi ñu ni hutal ngeeraan, hutal xobi rat naan <hesitation> , jëlal <hesitation> nga boole yooyu.
wof
gamb1252
Latn
538fb6bc-e639-4c3d-90fa-8cf5b016ea61
c87dffd4-d5a8-4e3e-98d7-f0927a2794fc
wof_Latn
spk01
f026
What are some foods that can cause bad breath?
s04
10.2625
Boo koy jefëndikoo; lii nga naan, lii nga sangoo rekk yàlla wéral la. Buñ doon tànn nag tay, bugg a delluwaat ca la mag ña hamewoon, bind bañ ñu binde nii moo di biñ bindoon mag ñi.
wof
gamb1252
Latn
d6ff7225-44dc-47d8-9e05-7c72f5977881
c87dffd4-d5a8-4e3e-98d7-f0927a2794fc
wof_Latn
spk01
f026
What are some foods that can cause bad breath?
s04
5.521375
Mag ñi ñoo wér rekk. Li ko ceeñ mooy li ñuy lekk moo bokkut ak la mag ña doon lekk.
wof
gamb1252
Latn
d5d70a81-0a10-4e84-9b70-26c47a93b37c
c87dffd4-d5a8-4e3e-98d7-f0927a2794fc
wof_Latn
spk01
f026
What are some foods that can cause bad breath?
s04
4.121
Fim ne neex na lañ topp waaye seetatuñ baax na. Lii mooy suñ probleme.
wof
gamb1252
Latn
618a2c20-7f87-40d6-957f-6d734dfa4e0b
c87dffd4-d5a8-4e3e-98d7-f0927a2794fc
wof_Latn
spk01
f026
What are some foods that can cause bad breath?
s04
10.3025
Salaamaalekum. <unintelligible>
wof
gamb1252
Latn
22989211-5f48-4225-96b4-fbdb6ae9a43b
c87dffd4-d5a8-4e3e-98d7-f0927a2794fc
wof_Latn
spk16
h103
What purpose do passports serve?
s01
21.5625
Waa passport dina di dimbale nit ci sa dem ak dikk na la ko de dimbale kon am na njëriñ ci dund doomu adama ndax dafay dimbale nit ci dem ak dikkam. Te dem ak dikk lu am solo la ci dund doomi adama, lu am solo la ci dund doomi adama, ndax li nga xamante ni moo jëng dund doomi adama muy xam-xam dem ak dikk dina ko di maye lu bëree bëri bëri.
wof
gamb1252
Latn
00bbeef6-20d5-4a05-b9c6-cccf81f756cc
5b0342dc-870d-49ae-bf89-608686b46442
wof_Latn
spk16
h103
What purpose do passports serve?
s01
18.982188
Ndax yàlla sax wax nañu ne dox leen ci kaw suuf ngeen xool man yàlla naka laa jëfee naka laa defaree man yàlla, naka laa tëralee, naka laa waajalee man yàlla, bu ngeen doxee ci kaw suuf nag dangeen ko gis. Te yu mel noonu ñooy yombal dox si jamono bi ñu toll nii ba foo dem ñu xam yow ban bërëb nga bokk, ban bërëb nga jó- nga ñjëkk a jóge.
wof
gamb1252
Latn
980b46d7-8b7b-466d-a80b-9feaab19fba5
5b0342dc-870d-49ae-bf89-608686b46442
wof_Latn
spk16
h103
What purpose do passports serve?
s01
29.243375
Te boo ko amee bërëb bi gallankoor bu la ci mën a dal bu fekkee dal na ci bu ñu ko xoolee dinañ xam ban dëkk nga, ban diw- ban bërëb nga jógee, te bu ñu yeggee ci bërëb boobu noonu dinañu xam yow yaay kan ak fan nga dëkk, parce que kenn ku ci ne ba sa dëkk sax fu ñu dëkk sax daf fay nekk sa turi gox, sa turi dëkk yëpp na fa di nekk buñ yeggee ci gox boobu noonu buñ laajtee dinañ xam ne diw kat fii la bawoo te dina di yombal dem ak dikk doomi adama, dina la yombal ci tolof-tolof bi la bu la dalee, kon lu bokk ci dund doomi adama la lu am njëriñ la ci dundu doomi adama.
wof
gamb1252
Latn
b2ee24ed-b4bf-45f6-b000-89cf8f34f94c
5b0342dc-870d-49ae-bf89-608686b46442
wof_Latn
spk01
h092
Could you describe how a key opens a lock?
s01
8.843
Waaw <hesitation> mu ni dafay laajte caabi naka la mën a ubbee karnaar. Waaw!
wof
gamb1252
Latn
d0c4f8c6-4d60-4e8e-8901-14b5a2f9607a
b0b9291f-f016-404c-9069-4b458d85ef86
wof_Latn
spk01
h092
Could you describe how a key opens a lock?
s01
17.365938
Xam-xam la bu réy bu fa nekka. Mooy rekk ki lëggéey <hesitation> karnaar bi bëñ yam def ca weñ ga, mu am weñ gi lu koy kii bam duggu fi mooy kalee, mu mën koo génnee fam kalee bam génn fam kalee, nu ube ko.
wof
gamb1252
Latn
0d621788-3c57-43f7-8f27-4cc4093f8217
b0b9291f-f016-404c-9069-4b458d85ef86
wof_Latn
spk01
h092
Could you describe how a key opens a lock?
s01
10.1835
Bëñ yooyale moo da ma ne ak a. Ma ne feek waxoo a njëriñal wax du duggu.
wof
gamb1252
Latn
f982aff0-dc1e-42a1-b2dc-c44b416cd7f0
b0b9291f-f016-404c-9069-4b458d85ef86
wof_Latn
spk01
h092
Could you describe how a key opens a lock?
s01
10.483563
Bam jëlee caabi ja defal ko ñetti bëñ, fu moo duggu dafa am ñetti pax. : bëñ bu ne tollook pax. Bam àggee fam war a àgg it loola la fa fekk.
wof
gamb1252
Latn
074a8ca0-819e-4e0a-9b61-b19d1c12fd7a
b0b9291f-f016-404c-9069-4b458d85ef86
wof_Latn
spk01
h092
Could you describe how a key opens a lock?
s01
3.841313
Bu waree dugël day dugël. Su waree génnee day génnee.
wof
gamb1252
Latn
5801ea1a-a7ed-4c44-99aa-3843b4c81039
b0b9291f-f016-404c-9069-4b458d85ef86
wof_Latn
spk01
h092
Could you describe how a key opens a lock?
s01
16.0455
Loola moo de ma ne ak a xam-xamu wax door a jëriñ, ci li nga xam ne looloo waral caabi, boo ko dugalee ci biir xombu, boo wañee, bu fekkee caabeem la, day dugg, bëñ ya day korosante. Soo biijee pour mu téju dana téju.
wof
gamb1252
Latn
9a072b04-7a4e-486f-8ca9-bc50b765e089
b0b9291f-f016-404c-9069-4b458d85ef86
wof_Latn
spk01
h092
Could you describe how a key opens a lock?
s01
3.381188
Soo biijee pour mu hubbiku dana hubbeeku.
wof
gamb1252
Latn
3834fe98-0e33-4ac4-973b-915427ac3040
b0b9291f-f016-404c-9069-4b458d85ef86
wof_Latn
spk01
h063
What is a bank?
s01
10.582063
Waaw, daf ma laaj <hesitation> ñu ni lan mooy bànk. Xam naa baat boobu sax moom waxi tubaab la.
wof
gamb1252
Latn
3bed0951-7957-415a-ae69-8ca3db50ecd3
ee3d080f-b6ef-47ed-8f14-4befd1d24493
wof_Latn
spk01
h063
What is a bank?
s01
8.181563
Waaye ñun lin xam mooy lan mooy pekk. Olof di ko wax pekk, te mooy bànk.
wof
gamb1252
Latn
94c568c6-46b1-4c56-be25-27b7b2d4e794
ee3d080f-b6ef-47ed-8f14-4befd1d24493
wof_Latn
spk01
h063
What is a bank?
s01
10.522063
Pekk mooy denceekaay, boo ko fa xësee def, yaw kepp a fay dem. Daŋ koy hub mu ne kepp.
wof
gamb1252
Latn
103eb0d0-aa4e-4cb6-8291-43874ea3d440
ee3d080f-b6ef-47ed-8f14-4befd1d24493
wof_Latn
spk01
h063
What is a bank?
s01
4.060813
Moom rekk a faay ne. Dara du ko fa jëlee ba nga soxla ko.
wof
gamb1252
Latn
70bc38cc-ca67-4a8a-94b5-880495aea4fb
ee3d080f-b6ef-47ed-8f14-4befd1d24493
wof_Latn
spk01
h063
What is a bank?
s01
10.962125
Mu tuddu denceekaay. Ñu tudde ko pekk ci mag ña, xam ne loo fa def, yaw mi ko fa def kuy jëli ji attaaya yaa koy jëli.
wof
gamb1252
Latn
b3f74241-fc43-43dc-9041-cc262b65b380
ee3d080f-b6ef-47ed-8f14-4befd1d24493
wof_Latn
spk01
h063
What is a bank?
s01
14.822875
Yaw itam noot nga sa bakkaan ba laŋ fa def doo ko jëli su dul fa ko jar. Lóola, mu doon njëriñ loo xam ne danga daan fekk, nit day dikk ak jaaxleem nga feyal ko soxlaam, te du xam foo ko jëlee.
wof
gamb1252
Latn
151b35a8-1cc2-42f2-b262-c5cc4032a178
ee3d080f-b6ef-47ed-8f14-4befd1d24493
wof_Latn
spk01
h063
What is a bank?
s01
13.762688
Demoo déeyook kenn, duggoo ci néeg keneen, seen néeg nga dugg génn fajal ko soxlaam, te bu duggee ci néeg bi du xam fi nga jëlee li nga fajee soxla fum ne. Loola moo tuddoon pekk, moom lañ doon def ko muy bànk.
wof
gamb1252
Latn
ebcdded6-5a2d-44bd-8722-ceceb693c3cb
ee3d080f-b6ef-47ed-8f14-4befd1d24493
wof_Latn
spk01
h063
What is a bank?
s01
9.661875
Daŋ fa denc sa halala, nit dana la jox halalam nga nga denc fa keneen jox la keneen jox la ba mu man a mbooloo, te bu boobaa kenn ku soxla boroom <hesitation> bosom mu dikkee fekk ko fa, nga jox ko ko.
wof
gamb1252
Latn
9f5a4b29-b19c-4f90-b7a1-e685df06aef1
ee3d080f-b6ef-47ed-8f14-4befd1d24493
wof_Latn
spk16
f003
What are some foods that you enjoy a lot but are very expensive?
s01
28.805
bokk na ci lekk yi may gën a lekk ci di kontaan waaye dafa seer suñ fii nii mooy ndawal ak jën, ndax suñu géej gi daal bo mel na ni xamante ne mel ni  ñun mel ni ñun dafa mel ni ñun réew mi moomatuñ ko léegi, ndax jën yu baax sax pour ñu lekk ko, dafay jafe lool. Ndax bokk na ci wér-gu-yara doomi yaramu doomi adama lépp li nga xamante ni dafay ñoree sa côté walla muy, mu, muy muy ñu fiy jógee fi nga dëkk nga koy lekk dafa baax si sa wér-gu-yaram kenn ku ci ne.
wof
gamb1252
Latn
18016d0b-2dbb-4988-82e3-860a5f3a74a3
0e812108-3576-42d2-b235-f98a202cf14a
wof_Latn
spk16
f003
What are some foods that you enjoy a lot but are very expensive?
s01
17.363
Waaye ñun li nga xamante ne mu ngi suñu côté ñu moom ko daal dafa seer seer gi nga xam ne naqari naqari gi nga xam ne dafa mel ni moomatuñ ko, moomatuñ ko léegi ñu jafe. Jën daal bokk na ci li nga xamante ni bëgg naa ko lool waaye seer na lool suñu réew mii sew te seer na fi lool metti na pour nga am nit am ko fii nii.
wof
gamb1252
Latn
22d970d0-ec68-4a3d-a70a-ec22328fd9ac
0e812108-3576-42d2-b235-f98a202cf14a
wof_Latn
spk03
p056
What is important to learn about somebody before marrying them?
s01
17.467563
Waaw daŋ koy xool ndax seen jikko mën na ànd, nga jàngat ko, xool jikkoom ak doxalinam ak kii nan la man ak ci <hesitation> yan sãri nit la bokk ak ni muy doxalee. Loola it diŋ koy def.
wof
gamb1252
Latn
3d68033c-56b1-493e-8499-2a052c162313
eca392d4-4d26-4b78-bb3e-c6427712aa9e
wof_Latn
spk03
p056
What is important to learn about somebody before marrying them?
s01
19.568438
Soo ko jàngatee ba pare, léegi mën nga <hesitation>  xool seen relation, seen diggante ba jàngat si lu bare après  nag nga xool ndax <hesitation>  sëy bi dina mën a nekk walla du mën a nekk balaa takk bi muy am. Su loolu yépp mënta nekk nag moom, soo yaboo nga xool leneen.
wof
gamb1252
Latn
62e6f5c2-779d-431a-88d9-12dbcf7942e5
eca392d4-4d26-4b78-bb3e-c6427712aa9e
wof_Latn
spk01
a008
How do birds communicate with each other?
s01
13.821938
Nee dafa laajte ne picca dañ di waxtaan ak naka lañ di waxtaane. Mu ngi koy tontoo ci, njàngam téere waaye du xam-xamu bopp.
wof
gamb1252
Latn
dacd5a32-035a-4f1c-bc21-32f7508dfe34
737ce947-7603-42b7-a86c-a850eda7bab6
wof_Latn
spk01
a008
How do birds communicate with each other?
s01
42.585938
Picc day wax, comme ni doom-aadamay waxee, ndax wax nañu ne yónnent yi dañ daan wax ak picc yi ndax ñoo doon seeni yónnent rawati muhammad sallal laahu aleyhi wa salam mi nga xam ne moo mujj a ñów. <hesitation> niti yàlla yi ñu tuddee wëlliyu dañ doon wax ak picc yi, picc yi doon wax ñoom. Kon picc dana wax; lañ ñu ca leeralee, te alxuraam moo ñu ko wax, mooy picc yi, giir gu ne, giir picc yi, ña bokk giir yépp dañuy waxtaan.
wof
gamb1252
Latn
06c5c7d3-1b38-4bb7-be6b-277819578da1
737ce947-7603-42b7-a86c-a850eda7bab6
wof_Latn
spk01
a008
How do birds communicate with each other?
s01
12.901813
Waaye nag ña bokk giir la. Ñële pittax ñu- ñu- olof di ko woowe peket, seen giir la ñoomu neen fañuy waxtaan.
wof
gamb1252
Latn
aa40d96c-430b-410f-8366-8f7844a973e0
737ce947-7603-42b7-a86c-a850eda7bab6
wof_Latn
spk01
a008
How do birds communicate with each other?
s01
27.083813
Kër tan ñoomu neen fañuy waxtaan. Picc yu bare, am na yoo xam ne alxuraan moo leen tuddu, ba tax na ñu tëral seeni mbir ni ñu leen tërëlee ; lu mel ne xorondom, ñoom am nañu seef comme ni doomu aadama amee ay buur, ham arme comme ne nguuru àddina gi doomu aadama am xorondom am na ko ci biit xorom bi mu nekkee xorondom.
wof
gamb1252
Latn
f21408f0-9568-44e8-a395-dbd073ad8b8f
737ce947-7603-42b7-a86c-a850eda7bab6
wof_Latn
spk01
a008
How do birds communicate with each other?
s01
18.0025
Loolu lañu tuddee xorondom. Loolu tan yi am nañu ko; am nañu buuru tan, nga xam ne moom, bu waxtuw médd amee moom mooy njëkk a ñów <hesitation> coppati la mu soxla ca médd ma, bu demee beneen doog a wàcc lekksi.
wof
gamb1252
Latn
29445aa2-01f8-45e3-b141-ce756e7db50b
737ce947-7603-42b7-a86c-a850eda7bab6
wof_Latn
spk16
f025
Are there any foods that are believed to help improve strength?
s01
17.0075
waaw lekk yu mel noonu bëri na yi ay lekk yi nga xamante ne su ma ko lekkee danaa di yëg cawarte. Lu ci mel ni jaxatu xaaraan suma yaram lu mu téye téyandiku téyandiku su ma ko lekkee dafay bàyyandinku, waaw su ma yaram lu mu nu mu nagam nagam nagam su ma lekkee jaxatu dina ko dëgëral.
wof
gamb1252
Latn
bf3af8ab-a5ad-45ad-8aaf-26b2ad08df9e
5dde4f70-1f4a-493e-9b01-fb24cc7ef092
wof_Latn
spk16
f025
Are there any foods that are believed to help improve strength?
s01
37.216438
Su fekkee ne dama toog nii sawarte nekkut ci man <hesitation> bu ma dawee tuuti sonn, walla su ma liggéeyee tuuti sonn dinaa di faral di jëfandikoo limoŋ, saay bu ma jëfandikoo limoŋ ma ut ci lu xaw a sakkan tuuti, ma xar ko, ma daa di ko baxal baxal ko ba mu ñor daal di ko <hesitation> nal ci benn kopp def ci tuuti lem, su ma ko naanee rek damay yëg cawarte gu mel ju ma newoon ci man yëpp <noise> mu dellusiwaat ci man. Ñaari lekk yooyu daal naa ko di jëfandikoo toujours lu ci bëri  su ma demee ba nga xamante  ni yëguma cawarte walla yëguma wér-gu-yaram sama biir yaram lu ci mel ni jaxatu walla kànja, walla limoŋ, bëri naa lu ma koy jëfandikoo lool su ma yëul wér-gu-yaram sama biir yaram <noise>.
wof
gamb1252
Latn
af468e91-9a3c-4740-a48a-3039fc77abab
5dde4f70-1f4a-493e-9b01-fb24cc7ef092
wof_Latn
spk16
h048
Could you describe how a drum produces sound?
s01
17.709063
Ah sabar nag lu yàgg la si suñu biir ñun làkkat yi, waa lu yàgg la suñu bii- yàqal nañu lu bëri nag waaye yàgg na si suñu biir itam nag, suñu àndandoor la bi nga xamante ni dem ba ko fi jafe na lool. Dañ koy defaree deru béy yi di koy yett ci ay garab di ko defaree noonu.
wof
gamb1252
Latn
5638985b-4310-4a66-bb10-597e35592fb7
a2435c52-f2a3-444a-b111-465c07391d3c
wof_Latn
spk16
h048
Could you describe how a drum produces sound?
s01
29.274938
Moom nag ni muy joxee dégg mooy soo ko dóoree dafay awu, awu googu noonu mooy def benn union bi nga xamante ni dafay dugg si nopp doomu adama yëngal kawar yi nga xamante ni nekk nañ ci biir nopp bi, bu ko yëngalee dina ko jox température bi nga xamante ne moo moo wër karaw yooyu noonu, loolu bu yëngotoo mooy def son, mu dem ci nopp, mu dem ci cuukel nit soog a dégg, noonu lañ koy déggee. Waaye nag mbir la bi nga xamante ne yàgg na suñ biir lool, ñu yàgg a ànd ak moom lool, waaw.
wof
gamb1252
Latn
dccb96f8-8238-4a9e-8480-cb2ca1df8450
a2435c52-f2a3-444a-b111-465c07391d3c
wof_Latn
spk16
a069
How do birds build their nests?
s01
16.24325
waa pittax nu ñuy defaree seen néeg <hesitation> bari na bari na pi- pittax yi dañu bari ay façon. Am na ñi nga xamant pittax yi nga xamante dañuy ràbb tagg comme ni yeneen picc yi di ràbbee tagg, waaye nag yooyu pittax yooyu moom yooyu bariwuñu, pittax <unintelligible> waa.
wof
gamb1252
Latn
97ecf988-3c23-4cdb-afcc-b112fb22f6d7
ce303b34-8ca3-4b9c-816b-00d4b952ad5b
wof_Latn
spk16
a069
How do birds build their nests?
s01
54.991
Picc yi ni ñuy ràbbee seen tagg bari na ay façon, am na yi nga xamante ni dañuy defal lal mu doon seen tagg, am ñi nga xamante ni dañuy defal xëdd, dañuy xëdd am picc yoo xam ne dañuy xëdd, lu ci mel ni picc yu ñuy tuddee <hesitation> koco-koco yooyu dañuy xëdd, waaye lu ci mel ne pittax ñoom dañuy defal lal ak ay tan yii nii njànaaw yooyu noonu ay lal lañuy defar. Waa ay lal lañuy defar ci kaw lal yu yaatu yoo xam ne dañ ciy tëdd, waaye ñoom seen néeg yooyu du baare taw, waaye am na ci picc yi nga xamante ni seen nid day baare taw lu ci mel ne koco-koco buy taw tamit biir néegam du tooy moom dina ko de léegi liggéey ràbb ko ba nga xamante ni biir néegam du taw, yu ci bari nag ñax lañuy defaree, ak yi nga xamante ni ñax bant bu dem ba doon bant, amul ñax yi nga xamante ni yu mel ni koco-koco ñax bi nga xamante ni dafay oyof doon guntax doon gàncax ñoom boobu lañ dee dagg di ko xonc, dem di ràbb seen tagg.
wof
gamb1252
Latn
1c69c2ea-7b37-4880-87cf-98d588737cdb
ce303b34-8ca3-4b9c-816b-00d4b952ad5b
wof_Latn
spk16
a069
How do birds build their nests?
s01
13.582688
Moo tax ñoom seen tagg yooyu noonu bu nawetee taw bu ñëwee sax dafay mën a ñàkk yàq taw bi, taw bi da koy mën a ñàkk a tooyal. Moo tax ñoom picc yooyu noonu ci côté dëkkuwaay moom ñoom ñoo ci gën a yeewu yeneen picc yi, ndax ñoom noonu lañu utiliser.
wof
gamb1252
Latn
024bd5de-6cef-4259-8cbd-aa1da35bfad2
ce303b34-8ca3-4b9c-816b-00d4b952ad5b
wof_Latn
spk16
a069
How do birds build their nests?
s01
15.123
Léegi nag picc yi moom taw bu ñëwee mun nañ di tawte waa, ngelaw bu ñëwee dinañ di mën a daane seen tagg yi. Waaye koco-koco moom jafe na lool ngelaw daane taggam, jafe na lool taw dugg ci biir taggam, moom yeemu côté boobu moom, am na xarañteef ci côté googu bu baax a baax.
wof
gamb1252
Latn
32ec6c94-c836-4d98-8b3a-e68ac697634e
ce303b34-8ca3-4b9c-816b-00d4b952ad5b
wof_Latn
spk16
h053
Could you give a very simple explanation of how an airplane flies?
s01
58.380563
waaw <hesitation> fofalnaaw nag olof yi ñoo koy wax fofalnaaw, fofalnaaw nag benn jumtukaay la bi nga xamante ni xarañteefu nit moo ko liggéey, xarañteefu nit moo ko liggéey mu doon li nga xamante ne yombal na lool dem ak dikk doomu adama ci kaw dund ci biir dundu doomi adama yombal na ko lool. muy mbir mi nga xamante ni bokk na ci li nga xam ne da koy dimbale pour mu naaw mooy mu am jaww ji nga xamante ni set na lool. Ndax jaww ji lu ñuy tuddee atmosteeri jaww ji bu amee ay tolof-tolof rek moom bu jógee ci kaw dina di yomb a am tolof-tolof oxygène mu am ngelaw bu mut no- bu nit ki nokkee dina di yomb a am tolof-tolofam, manaam bu jaaree si zone bi nga xamante ni, walla béréb bi nga xamante ni bëri na lool ay mbir yi nga xamante ni xew bi na ciy xew ci bërëb boobu noonu di jëm di yéeg ci kaw flon asamaan si dina di yàqal avion bi. <hesitation> fol fol nag fofalnaaw bi ay ay kii nii ay jëmuwaayam, parce que li nga xamante ni dina ko di soxla ci ngelaw daf koy manquer te bu ko manquer mën na lor ñi nekk ci biir.
wof
gamb1252
Latn
8feb7fe5-01e2-4924-8c94-6a3efe3686b0
0795f6d8-6c5f-4dc5-b428-c7816b6525e5
wof_Latn
spk16
h053
Could you give a very simple explanation of how an airplane flies?
s01
9.783438
Pour mu am lu ko lu gën ci moom nag mooy mu am jaww bi nga xamanete ni set na wicc jaww ji nga xamante ni sell na, mu mën a naaw ba wàcc yombal dundu dundi doomi adama.
wof
gamb1252
Latn
22153664-1092-4a9a-bb18-74289442e324
0795f6d8-6c5f-4dc5-b428-c7816b6525e5
wof_Latn
spk01
i055
Can you explain how to wash your hands properly?
s01
13.126063
Waaw moom it dafa laajte <hesitation> nit ki naka laay raxasee loxoom bam set. Raxas loxo pour mu set, ba ja njëkk daal mooy na ndox ma set.
wof
gamb1252
Latn
a7de3fa0-7b6e-4806-a1aa-67645fd46d18
072d50c9-6b5f-46bc-b830-b37423a058a6
wof_Latn
spk01
i055
Can you explain how to wash your hands properly?
s01
18.128313
Yaw mi koy raxas, naŋ ko jonju mu daj ak yaw loo ko mën a booleel pour mu dimbali la ci li taqe ci loxo bi dëñ, nga boole ko ca. Waaye loxo bi daal, benn bu sa ne dana ragg moroom ma, ba li nga xam ne moo ci taq dana hippiku.
wof
gamb1252
Latn
cc0a63eb-433f-4ad1-bd98-8de368b3b41a
072d50c9-6b5f-46bc-b830-b37423a058a6
wof_Latn
spk01
i055
Can you explain how to wash your hands properly?
s01
12.185625
Nga dugal ko si ndox mi njonju ko ba xam ne ndox mi dana yóbbaale lépp lu taqoon ci loxo yi. Nga am meneen ndox nga dugal ko, mu layangi sa raxasu, sa raxasu set.
wof
gamb1252
Latn
ee7cbebc-0d9e-4b26-bac0-e421dfda2b8e
072d50c9-6b5f-46bc-b830-b37423a058a6
wof_Latn
spk01
c091
Is there a particular style of clothes you like to wear?
s02
5.740625
Bàyyi na aadaam. Loolu lañ ko miinee, te nit ku ne lam la miinee lay xam ci yaw la jegeleek moom.
wof
gamb1252
Latn
21159cf3-d8c3-47e7-854b-46f4923a36a8
ab88e176-4c4e-4d3c-9170-49c23a53c97c
wof_Latn
spk01
c091
Is there a particular style of clothes you like to wear?
s02
9.741063
Mu undi aada da dund. Ñuni tamit lañ miin ak la ñu juddu fekk ko fi, muy aada ci ñun mooy mbubb mu job, mbubb mu rëy.
wof
gamb1252
Latn
222171c4-8372-49e5-b7fe-7fce5671d1aa
ab88e176-4c4e-4d3c-9170-49c23a53c97c
wof_Latn
spk01
c091
Is there a particular style of clothes you like to wear?
s02
4.4005
Yaar yooyu de ham na. Mbubb mu jot ak mbubb bu réy.
wof
gamb1252
Latn
469f4770-aebf-40e6-94fc-fc02ee550677
ab88e176-4c4e-4d3c-9170-49c23a53c97c
wof_Latn
spk01
c091
Is there a particular style of clothes you like to wear?
s02
17.802
Am na yow, li ngay doon doon xale, ham na yëre yu boo ko solee, dañ la jox cër boo xam ne, duñ ko de jox xale. Cër baa la ko may. <hesitation> boo ko solee, tay boo jëloon sabadoor sol ko, jël laafa teg ca, boo ñëwee duma la taaj ci suuf.
wof
gamb1252
Latn
be557228-2c16-40ec-a152-2d7d694ea4c7
ab88e176-4c4e-4d3c-9170-49c23a53c97c
wof_Latn
spk01
c091
Is there a particular style of clothes you like to wear?
s02
7.860875
Fokk ñu jox la cër. Gune gu heroo ngi nii paska yenenn yooyu lu muy address, maanaam lii, lu muy wone.
wof
gamb1252
Latn
70dcd266-5b47-4380-a200-c681931846ba
ab88e176-4c4e-4d3c-9170-49c23a53c97c
wof_Latn
spk01
c091
Is there a particular style of clothes you like to wear?
s02
6.040688
Maa ngi baalu àq ci tubaab yi sax. Li mooy wane ci nit ki mooy lii a ko neex.
wof
gamb1252
Latn
02113b39-8919-4b3d-9772-b642ef7202af
ab88e176-4c4e-4d3c-9170-49c23a53c97c
wof_Latn
spk01
c091
Is there a particular style of clothes you like to wear?
s02
7.700875
Kon nii la mel. Walla kii lile koo neex, li tax mu sol hére  hii, kon hiree ko neex.
wof
gamb1252
Latn
6a04989f-0c2e-49b6-bc82-5561a9400d7b
ab88e176-4c4e-4d3c-9170-49c23a53c97c
wof_Latn
spk01
c091
Is there a particular style of clothes you like to wear?
s02
8.941
Ki nga xam ne <hesitation>  mel neneen moo ko neex moo tax mu def kawarom gi mu mel neneen, sol yëre yoo xam ne dañ ko xotti. Mu mel neneen.
wof
gamb1252
Latn
5dd192bf-6322-41d0-a92d-5be125fea990
ab88e176-4c4e-4d3c-9170-49c23a53c97c
wof_Latn
spk01
c091
Is there a particular style of clothes you like to wear?
s02
4.940563
Ham na keneen ku moo roy ku bokkul ak lii. Lii moo undi yëre yu wuute.
wof
gamb1252
Latn
1a454d10-546e-4b9d-b523-46cb4afb2102
ab88e176-4c4e-4d3c-9170-49c23a53c97c
wof_Latn
spk01
c091
Is there a particular style of clothes you like to wear?
s02
11.621313
Ci man nag, bu ma dee sol la may sol mooy yëre yu guddu, yu jot walla yëre yu rëy yu rafet. Man ibba maadi silla de loolu laa bëgg.
wof
gamb1252
Latn
1740e4f9-463c-4cf8-9550-15ebd0bb1342
ab88e176-4c4e-4d3c-9170-49c23a53c97c
wof_Latn
spk01
p104
Is it possible to live without regrets?
s01
9.061063
Waaw laaj bi mu ne <hesitation> ci gàttal ndax nit mun na góor- góorlu dundu be du réccu. Waaw!
wof
gamb1252
Latn
85295953-54e2-4145-980c-403207e2e518
1f68a200-ece1-48b5-a2ec-d75c5c217904
End of preview. Expand in Data Studio
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
12