texte_wolof stringlengths 3 829k |
|---|
yeneen Xeeti xeltuSoppi |
Mi ngi toog ci otelam ne tekk. |
Ku yaru rekk a mat a xam |
Faal ak Jóop Kajoor ak Bawal |
Gaawleen waay, gaa ñi ! |
War nanoo nelaw. |
turki bi dafa ràpp ba ñu daax ko fu nekk |
Talib Fongalimi bi ñu nga ñag |
Waayé térewul ñu war di topp tënk bi Sëriñ bi def, |
Buleen des fii ! |
jëmële ko ca Firawna, ak Haamaana ak Qaaruuna. Ñuy wax naan : “Kii ab njibarkat bu di ! ab fenaakoon la ! ” |
yuri na siddéem si woon ci poosam yépp |
Tom ku am gëdd la. |
Suwayli làkk wu kilifawu la officiel ca Tansani ak Keeñaa |
Ndax lii sa yëf a? |
Noo ngi nii di xeex. |
“ Am naa giléem ca Gànnaar” yomb naa wax, |
Ndakaaru moo mujj doon gëblag koronaawiris bi ci Senegaal |
Lan mooy 'OVNI' ? |
Te wóor na ne joxoon nanu leen ab Téere, bu Nu faramfàcce mu neex a dégg, muy njub ak yërmaande ngir nit ñu gëm. |
Bokk neen ak Sebbe yi |
Am naa ci kaaraange. |
Kotleen ma ci seen i yoxo ! |
Du ma gañe mukk. |
Man ngaa toog. |
Dinaa la takk. |
Lii ngeen di gis nag jenn jigéen la. Mu ngi woddoo benn musóor, takk fer ci biir bi ak beneen fer ci pooj bi. Mu ngi woddoo musóor bu puur |
Bég naa, fii. |
Ab fajkatu xol la. |
Mu ngi tàmbalee yéeg |
May ma jàmm?! |
tërëx piccu ndox la waaalo waalo yi xam nañu ko |
Benn rekk laa ciy wax nga dégg, |
Ameel naa leen ub añ. |
Ànd ci ak mbégte. |
jinax yi dañu muus mënuloo leen posone |
Dawaan bu safaanu Dawaan bu safaanu DS walla AC ci wu-angalteer: Alternating Current màndargoo ag walug dawaan guy soppiku ci jamono muy ci taraay walla ci jubluwaay..Doxiin.Naka-jekk dawaanu mbëj suñu koy séddale, ci dawaan bu safaanu bu baraayam sax ci 50 Hz walla 60 Hz lees koy defe ak - bi dañuy safaanu ci watatuka... |
War-wéqam gi dafa baxa. |
Maa ngi jéggalu ci yàqal gi. |
lu dul yërmaande ju bawoo ci Nun, ak i xéewal ba jëmmi jamono. |
mu xolleti beneen ku dàq ku jëkk ki génn daldi né ko |
Dangeena niru ku jaxasoo. |
Man naa am loolu dina doy. |
Te wolof dafa ne, peccum liir bu neexee, ndeyam a téye ca mbagg ya. |
USMAAN GËY NJAATIGEL LIGGÉEYU NJÀNGUM WÉRGU-YARAM |
Waay ji wax na dëgg. |
man nanoo làqu ci biir. |
Dafa tàngoon lool. |
Bëgg naa loolu. |
Looy thumb. Looy : dundat yi. Looy ak yenn ciy mayam :.Aw loosam :.Ni muy xoole ci kanamam noonu lay xoole ci ginnaawam te du soppi ab jubluwaayam, ci niral : jëm ji man naa jublu penku, mu wëlbati bopp bi mu féete soww fi ko neex lay xool..Ay noppam, ay gëtam ak diggante 2i gët :.Ay noppam a ma koy xibaar fa li mu sox... |
Jàpp ma soo ko manee ! |
Ay tombi boy yu bari nag am nañu te taariix man na cee tàmbalee |
Ba ndéey la siiw naa |
Wirgoom dafa mboq. |
Mu téen xool biddéew yi [di settantal], |
Bu yàggee man naa jàpp xol bi, mu mujje AVC. |
siraahayni mbaa sireyna? |
Moom de war na laa bëgg. |
000 |
Xasaayit laata 1324 |
soo gësëmee banqaas bi bal bi dina wadd |
Waaye nit ñi ak dereet ji, daf nu koo war a fay |
Aa yaayee waa ju ñaaw du doon sama waay |
Jox leen ko ko. |
Dama bëgg itam togg. |
Réew la itam mu biir-suufam oom lool |
Mbaa Tom a ngi ci jàmm ? |
Ku bari yërmande nga. |
W Watt bennaanu nattu ngóora gi |
Buleen ko wax kenn ! |
Ñu àndandoo sax ca dun ba akub coona,fuglukat ya di ñu fa bari. |
Lutax ñëwoo ci waxtu wi ? |
dafa àbb sama simis dal di ko def moomeel |
Du danga fee man a ñàkk. |
Tëj jàkka yi ? |
Ci 80eelu jataayu Ndaje Mu Mag mu Mbootaayu Réewi Àddina si, Njiitu Réew mi Basiiru Jomaay FAY, séq na ab jataay, àjjuma 26i fani sebtàmbar 2025, ak teleb Farance 24. Muy am pose ci Njiitu Réew mi ngir mu yaatal gis-gisam, diggante laamisoo gu ñu yeesal, yoon gu moom boppam ak manal sunu bopp ci wàllu koom. |
Tom man naa soppiku. |
Lu taxoon ca xarnu ya leen jiitu, ñu baax ña [dese woon yan bi] nekkoon ñu néew, ñoom ña daan tere lu bon ci suuf sa ! Ñu bokk ca ña Nu musaloon te ñu tooñoon, topp seeni bakkan ca xéewal ya ñu donnoon ay bàkkaarkat. |
XEW-XEW CI DËKK BU SELL BI. |
Gis naa fi ab nataal, nataal boo xam ne am mbooloo la ñu toog, am kenn ku nekk ci seen kanam taxaw. Am na meneen waxambaane mu sol mbubbu mu xonq mu toog wane ginnaaw. |
Altine jàpp 5h18 dog 19h28 |
Boo indiloon, ñoñ-téere, kéemaan gu mu mën a doon, du tax ñu topp sa jubluwaay (xibla) ! Yaw itam du yaay topp seen xibla ; ñoom ci seen biir sax, kenn du ca topp xibla moroomam. Yaw nag boo toppee seeni bànneex ginnaaw ba la xam-xam bu leer dikkalee, kon de ca tooñkat ya ngay bokk. |
E mooy kàttan gi rënku ci xiirtalukaay bi. |
Yaa ngi tappale. |
Seen jafe-jafey dund day yokk rek ndax all bi ñuy dagg ay garabam. |
Diwaan bi dafa am meloow ñettkoñ |
Dama war a wéeyal. |
Neel : “Seen Boroom duleen faale, xanaa sax bu fekkoon ne yéen a ngi Koy jaamu ; waaye weddi woon ngeen Yonent bi. Seen mbugal, dungeen ko mën a raw, te dafay doo lu sax. |
Du xam ngeen ni ay du yem ci boppu boroom ? |
Sa kàddug Boroom mat na ci dëgg ak maandute. Ay waxam du soppeeku. Kuy dégg la, di Ku xam. |
Ana njabootam ? |
Yariinu xale bi |
Abilen Ci angale mooy Abilene ; Ci faranse mooy Abilène .Diiwaan bu ndaw la woon, ci Siri ci diggante Libaŋ ak Damas. Diiwaan ba wër na dëkk bu tuddoon Abila. Abila sore woon na Damas ca sowu kaw lu tollu 29 kilomet. Bi Yeesu juddoo Lisañas moo ko yilifoon. Gannaaw loolu bokk na ci nguuru Erodd Agaripa II ba noppi ñu b... |
Li ko sababSoppi |
Tëjal këf yi. |
daf ko jam paaka. |
Amon mooy benn turu yalla ca diine Afrig. |
Ñam wu la soob |
Firawna dadoon kawe-kawelu ci suuf si ; féewale waa réew ma, di jaamuloo ab kurél ci ñoom : ak a réndi seeni doom yu góor, di bàyyi jigéen ña. Moom Firawna yàqkat la woon. |
Doonul woon lu jafe. |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.