id stringlengths 13 25 | language stringclasses 143
values | audio audioduration (s) 0.64 20 | text stringlengths 6 400 |
|---|---|---|---|
ALFFA_wol_000179 | wol | [wol] KU YÀLLA SÀNNI FITT DOO KO MËNA PAKKU
| |
ALFFA_wol_000180 | wol | [wol] NDARE KENEEN LA WOON DINAA KO DEFAL TERAANGA JII
| |
ALFFA_wol_000181 | wol | [wol] DËKK BU MAG DAFAY FARAL DI BARIY CAGA
| |
ALFFA_wol_000182 | wol | [wol] MOROOMAN YI XAM NAÑU NI MUQAT LA MOO TAX ÑU DI KO TOOÑ
| |
ALFFA_wol_000183 | wol | [wol] XALE BI RAATALE NA ÑANDAXIT WI CI KANAM GI YÉPP
| |
ALFFA_wol_000184 | wol | [wol] JUR NA JURÓOMI DOOM WAAYE DAFA YARA DAL
| |
ALFFA_wol_000185 | wol | [wol] PIIS BU LIMON BA REKK A FA NEKK BU WEEX BA JEEX NA
| |
ALFFA_wol_000186 | wol | [wol] NOONU MU JOX KO FETALU ÑAARI NGÉMMIÑ ARNEL KO FAS WI MU WAR JOX KO AB FITT
| |
ALFFA_wol_000187 | wol | [wol] BENN SEEX BI GÀJJ BI CI LEX BI LAA KOY XÀMMEE
| |
ALFFA_wol_000188 | wol | [wol] JIGÉEN ÑU BARE ÑEMEWUÑU NJURUG SEEX
| |
ALFFA_wol_000189 | wol | [wol] DAFA TÀMBALI WOON DI MA GAARAL MA YEMALE KO
| |
ALFFA_wol_000190 | wol | [wol] BËGGA RICCAMTÉKU MOO LA KO TAXA WAX
| |
ALFFA_wol_000191 | wol | [wol] DUMA SEYAG BAAY BUUR NJAAY MACCUUTA MBELANGAL
| |
ALFFA_wol_000192 | wol | [wol] LAMÉÑ U LUU A GEN LAMÉÑ U FÉNKÀT
| |
ALFFA_wol_000193 | wol | [wol] BÀYYI KO MU NOPPALU TIITAANGEE KO JÀPP
| |
ALFFA_wol_000194 | wol | [wol] JIGÉEN JI NAG YUMAANE REKK LA BAÑ
| |
ALFFA_wol_000195 | wol | [wol] DÀQAL XANDANDUUR WI KENN DU FI DÉGG DARA
| |
ALFFA_wol_000196 | wol | [wol] YÀKKAMTI NA MÀNDAA BI KO DOOMAN DI YÓNNEE
| |
ALFFA_wol_000197 | wol | [wol] CËQUM GARAB MAA NGI RAFET LÉEGI NDAX NAWET BI
| |
ALFFA_wol_000198 | wol | [wol] XALE BI YUQAMTALU NA BA ÀJJI MÀNGO BI
| |
ALFFA_wol_000199 | wol | [wol] MBËR YI DINAÑUY TAKK TÉERE BU ÑU NAAN DÀKK
| |
ALFFA_wol_000200 | wol | [wol] LAATA ÑU KOY OPEERE DAÑU WOT JAAF YI
| |
ALFFA_wol_000201 | wol | [wol] YAL NA LA YÀLLA MUSAL CI CAT AK BËT
| |
ALFFA_wol_000202 | wol | [wol] REERAM BI DINA GUDDEE MU NGIY SOG A RUKK LAALO
| |
ALFFA_wol_000203 | wol | [wol] BA MÀNDIKAT BA DAANOO NDAW SI DAFA REE BA KEKKU
| |
ALFFA_wol_000204 | wol | [wol] FOMPAL LUMBI DERET YI BALA NGA KOY FAJ
| |
ALFFA_wol_000205 | wol | [wol] AS JÉN LAÑUY DEF CI DÓOLINKA GI NGIR DUUMAT JÉN YU MAG YI
| |
ALFFA_wol_000206 | wol | [wol] INDI NAÑU MBAAM MU BEES BI FI NEKKOON DAFA YÀQU
| |
ALFFA_wol_000207 | wol | [wol] GARAB GII BAAX NA CI GONE GUY FEEÑAL
| |
ALFFA_wol_000208 | wol | [wol] JANQ BOOBU DAFA DËGËR BU SÀGGANEE DOOTUL AM KU MU ÀNDAL
| |
ALFFA_wol_000209 | wol | [wol] NJÀNGALE MI DINA JAFE CI MOOM NDAX SAWARU CI
| |
ALFFA_wol_000210 | wol | [wol] PUSO BAA NGI SURUX CI DIGGANTE TAABAL BEEK MIIR BI
| |
ALFFA_wol_000211 | wol | [wol] LI MU MA MAY CI NGATO BI MATUL SAX LANC
| |
ALFFA_wol_000212 | wol | [wol] SÀKKAL MA CI GALLAX YI LI NGA MA JOX NDOX REKK LA
| |
ALFFA_wol_000213 | wol | [wol] JËMBAT NAA AY XOTTUBUTÉEL CA TOOL BA
| |
ALFFA_wol_000214 | wol | [wol] AMOON NA JURÓOM ÑETT BA CI FUKKI NIT
| |
ALFFA_wol_000215 | wol | [wol] NDÀNK NDÀNK MOOY JÀPP GOLO CIB ÑAAY
| |
ALFFA_wol_000216 | wol | [wol] SA DÉNKAANE BOOBU JAR NA BAAMTU BA ÑÉPP DÉGG KO BU BAAX
| |
ALFFA_wol_000217 | wol | [wol] JARGOÑ RÀBB NA LËNDAM CI SAMA NÉEG
| |
ALFFA_wol_000218 | wol | [wol] WOTO BAA NGI DOON XUYY KAMAJ CI NDEYJOOR
| |
ALFFA_wol_000219 | wol | [wol] YAA NGI MAY GÉTËN AK SA WAX JU DUL JEEX
| |
ALFFA_wol_000220 | wol | [wol] GIS NA KI ÑU KOY BËGG A MAY XALE BU GÓORAYIW LA
| |
ALFFA_wol_000221 | wol | [wol] BITIM RÉEW SAA YOO FA DEMEE TUMURAANKE
| |
ALFFA_wol_000222 | wol | [wol] JIGÉEN ÑI DAÑUY XAAR BA GÓOR ÑI RIJJI BA NOPPI ÑU ÑÓW
| |
ALFFA_wol_000223 | wol | [wol] KENN DU NI LIW NGA AK YËRE YI NGA TEGLE
| |
ALFFA_wol_000224 | wol | [wol] SOO KO JÉNDEE TE DOO KO JËFANDIKOO LUY DOON NJARIÑAM
| |
ALFFA_wol_000225 | wol | [wol] DOOMU JIITLE DU DOOM XARE BU FAAF LA
| |
ALFFA_wol_000226 | wol | [wol] SA KAWAR DAFA DËGËR KÓOM REKK A CI MËN DARA
| |
ALFFA_wol_000227 | wol | [wol] NJAAY MI INDEETUL DARA NDAX DUWAAÑ BI
| |
ALFFA_wol_000228 | wol | [wol] SOO LAXALEE DAFAY MEL NI SA YARAM WI DAFA YEEWU
| |
ALFFA_wol_000229 | wol | [wol] GEJJU YAS WAALO WAALO YEE KO MËN A LIGGÉEY
| |
ALFFA_wol_000230 | wol | [wol] RAT GA CA TOOLU BAAY GOLO YAA NGA KOY ÑAAY
| |
ALFFA_wol_000231 | wol | [wol] BOO KO SANGEE BA NOPPI NGA LENQALI KO AK NDOX MI CI SIWO BI
| |
ALFFA_wol_000232 | wol | [wol] MOO TEY NI MUY DOXE MAAMAM LAY KÓKKALI
| |
ALFFA_wol_000233 | wol | [wol] KËRAM GI NA MEL NI MU MELOON LÉEGI LÉEGI
| |
ALFFA_wol_000234 | wol | [wol] ÑU ÑÓW FEKK LËL BU MAG GIS WATIT WI
| |
ALFFA_wol_000235 | wol | [wol] AY XALAAT YU SU ÑU LEEN BOOLANTEE DINA BAAX
| |
ALFFA_wol_000236 | wol | [wol] JËKKËR JEEY JOXE DUND BI JABAR JI SÀNG XALE YI
| |
ALFFA_wol_000237 | wol | [wol] BARKEEL BI MOO WUTALE BIIÑU MEES BI AK BI NGAY NAAN CI SA KËR
| |
ALFFA_wol_000238 | wol | [wol] JAABANTE BI DU DAKK BA BA NGA MAA FEY SAMA XAALIS
| |
ALFFA_wol_000239 | wol | [wol] BUY MOY AK BU DUL MOY YÉPP SA YOON NEKKU CI
| |
ALFFA_wol_000240 | wol | [wol] NEE ÑU BUTTI NA JIGÉENU BIIR NGIR XAM NU DOOM JI TËDDE
| |
ALFFA_wol_000241 | wol | [wol] NA WAA DÉKK BI YÉPP XAM NI ËLLËG LAÑUY BEY ARMEEL YI
| |
ALFFA_wol_000242 | wol | [wol] ÑOOM ÑAAR AMAREEG SÀMBA ÀGSI CI KËR BUUR BI
| |
ALFFA_wol_000243 | wol | [wol] LU ËPP ÑAARI JUNNI NIT A NEKKOON CA BAYAAL BA
| |
ALFFA_wol_000244 | wol | [wol] DINA ÑU XAM NÉ BASI GÓOR A KOY BEY DÉ NA ÑU DOX REKK
| |
ALFFA_wol_000245 | wol | [wol] DAFA TÀMBALI WOON DI MA GAARAL MA YEMALE KO
| |
ALFFA_wol_000246 | wol | [wol] SAMA GAN YII DI ÑÓW TE AMUMA LU MA LEEN TERALE MOO MA JOMMAL
| |
ALFFA_wol_000247 | wol | [wol] BI JËKKËR JI FAATOO NAG NDAW SI DALDI DAW KËR BUUR
| |
ALFFA_wol_000248 | wol | [wol] ELLËG LA NDAJE MA NA KU NEKK ÑÓW AK SA ËLLÉER
| |
ALFFA_wol_000249 | wol | [wol] YAAY JI NI KO LAN LAÑU LAY NGÉNTÉE
| |
ALFFA_wol_000250 | wol | [wol] NAKA ÑU SUKK DI LEKK BA MU YÀGG CAAT MI NI
| |
ALFFA_wol_000251 | wol | [wol] DANGA MA BËGGA TÀGGALE AK SAMA SAGO
| |
ALFFA_wol_000252 | wol | [wol] BI MA LAATA JOT KAYITU JUDDU WI JAABANTE NAA BA SONN
| |
ALFFA_wol_000253 | wol | [wol] NAKA LA TAXAW DI LEEN XOOL WAA JI NI KO
| |
ALFFA_wol_000254 | wol | [wol] SEEN DIGGANTE DAFA MEL NA DIGGANTE SANG AK JAAMAM
| |
ALFFA_wol_000255 | wol | [wol] NDIIRAAN MA NE XIDD MU DI LEEN WAAR LU TOLLOOK AY WAXTU
| |
ALFFA_wol_000256 | wol | [wol] SUNU NJIIT DAFA TUKKI WAAYE KUUTAAYAM A NGI FI
| |
ALFFA_wol_000257 | wol | [wol] JEKÀ LAA SËN TÉ MENTI LAA GAN LU MU DON PUJ ÀB NEEG
| |
ALFFA_wol_000258 | wol | [wol] CI WETU SEJU LA TOOLU BANAANA YI NEKK
| |
ALFFA_wol_000259 | wol | [wol] GËN GAA BARE MËN NAA CI DEF JURÓOMI JUNNI
| |
ALFFA_wol_000260 | wol | [wol] JÀNGALEKAT BII AM NA BAAT CI EKOOL BI
| |
ALFFA_wol_000261 | wol | [wol] DELLOO NAA TAYÓOR BA ROBB BA ÑAW BI DAFA SIIÑ
| |
ALFFA_wol_000262 | wol | [wol] BI MA DAJEE AK MOOM DAFA DUMMÓOYU NDAX GÀCCE
| |
ALFFA_wol_000263 | wol | [wol] NANGEEN DIISOO BALA NGEEN DI DEF DARA
| |
ALFFA_wol_000264 | wol | [wol] BËGG NAA LA LOOL SA TUUB BI REKK A MA JAAXAL
| |
ALFFA_wol_000265 | wol | [wol] TE DAFA MA NÉWOON LU YÀGGA YÀGG BUL WÀCC
| |
ALFFA_wol_000266 | wol | [wol] JAAJAX DINAÑU TÀMBALI SEEN NGOMAAR ALTINE JIY ÑÓW
| |
ALFFA_wol_000267 | wol | [wol] NDAW SA FEKKE NA JATAAY BA WAAYE WAXUL XANAA MUY WOOGU REKK
| |
ALFFA_wol_000268 | wol | [wol] MU NGI AME MBAQAM DI DIIR PICC YI REKK
| |
ALFFA_wol_000269 | wol | [wol] MU NGI YÉEG CI FASAM DI XALAM TOPP GÉTTAM
| |
ALFFA_wol_000270 | wol | [wol] BU JËKK JARBAAT DAFA DAAN DONN NIJAAYAM
| |
ALFFA_wol_000271 | wol | [wol] DEFARU NA BU BAAX BI MU NEKKEE NJIIT LI
| |
ALFFA_wol_000272 | wol | [wol] SAA BU MA KO NUYUJEE DINA MA MAY AYLAYÉWÉN JUNNI
| |
ALFFA_wol_000273 | wol | [wol] WAX AB XOTTIKU LA KENN KU NEKK YAA XAM NOO KOY ÑAWE
| |
ALFFA_wol_000274 | wol | [wol] SABAB BOOBU DEY YÀLLA NA ÑU CI YÀLLA MUSAL
| |
ALFFA_wol_000275 | wol | [wol] BA MU YÉGEE NE DAFA LAJJ BA TEY MU NGI NE LÀCC
| |
ALFFA_wol_000276 | wol | [wol] GIIRUG DUNDAM MËSUL YÉENE NIT LU BON
| |
ALFFA_wol_000277 | wol | [wol] DANGA BËGGA DABU REKK WAAYE LI NGA WAX WAX NGA KO BA NOPPI
| |
ALFFA_wol_000278 | wol | [wol] DAXELEF MOOMU MOO DAAN WOOTU BUNTU TË
|
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.