score float32 1.04 1.25 | Tsonga stringlengths 10 499 | Wolof stringlengths 10 494 |
|---|---|---|
1.160462 | Ha vambirhi ava lulamile emahlweni ka Xikwembu, ava famba emilawini ya Hosi ni le swilerisweni swa yona vari hava xisolo. | Sakariya ak jabaram ñu jub lañu ca kanam Yàlla, di topp ni mu ware ndigal yi ak dogali Boroom bi yépp. |
1.160394 | Ho itea mini kha tshaka mbili dza muvhuso na kha thembele ngei Yerusalema? | Lan moo dal nguuru ñaari giir yi ak kër Yexowa gi nekk ci Yerusalem ? |
1.160309 | va ala ni ku chava HOSI Xikwembu, | te ragaluñu Yàlla. |
1.160214 | 30 Kutani va ku ka yena: "Loko swi ri tano, xana u endla mahlori wahi hi ma vona, leswaku hi ta pfumela eka wena, xana? | 30 Ñu ne ko: "Ban firnde nga nu mana won, ngir nu gëm la? |
1.160136 | No vha ni sa ḓivhi uri munna a no nga nṋe u kona u ḓivha zwithu nga u bvumba?" | Xanaa xamuleen ne nit ku mel ni man day gisaane?" |
1.160129 | Hambi leswi sathani a nga boxiwangiki hi vito ra yena tani hi musunguri wa vubihi, kambe hina byona vumbhoni lebyi humaka eka Matsalwa hinkwawo. | Waay li tah seytaane di natu nit yi mooy daneel leen ci bakaar, ndah nu muna nakka seen bakan, walla mu yahal leen. |
1.160073 | Hone ane a ḓikwakwanya na Muṋe washu u vha muthihi nae lwa muya. | 17 Waaye nag kuy ànd ak Boroom bi, xel yi dañuy booloo, nekk benn. |
1.159645 | Musi Yona a tshi bva thumbuni ya khovhe khulu o ya ngafhi, nahone zwenezwi zwi ri funza mini? | Fan la Yunus dem ginnaaw bi mu génnee ci jën bu mag bi, te loolu lan la ñuy jàngal? |
1.159297 | 12 n'wina a ma ha n'wi pfumeleli ku endlela tata wakwe kumbe mana+ wakwe nchumu wo karhi, | 7:12 dootuleen ko bàyyi, mu defal dara ndeyam walla baayam. |
1.159014 | Ndi hone vhafu vha tshi haṱulwa hu tshi tevhedzwa mishumo yavho nga he ha ṅwalwa dzibuguni. | Ñu àtte néew ya, ku nekk ci say jëf, ni ñu ko binde woon ca téere ya. |
1.158959 | 46 Kutani lava va ta loviseriwa makumu,+ kambe lavo lulama va ta ya evuton'wini lebyi nga heriki."+ | 25:46 Noonu ñii dinañu sóobu ci mbugal gu dul jeex, waaye ñi jub dinañu tàbbi ci dund gu dul jeex." |
1.158861 | Riṋe ri ḓivha uri hoyo munna ndi mutshinyi." | Xam nanu ne waa joojee boroom bàkkaar la." |
1.1586 | 19Maanḓa adzo o vha e milomoni yadzo na mitshilani, mitshila yadzo i tshi nga dziṋowa dzi re na dziṱhoho, dzi tshi huvhadza vhathu ngayo. | 19 Daŋaru fas yaa ngi ci seen gémmiñ ak ci seen geen, ndax seen geen yaa ngi mel ni ay jaan, ami bopp yu ñuy mititalee. |
1.158352 | N'wi vitaneni, kutani u ta mi byela nhlamuselo ya kona.' | Waxal ñu indi ko, dina la wax li loolu lépp tekki. ' |
1.158131 | 22 "Tanani mi hi byela swilo leswi nga ta endleka. | 22 "Woneleen ko te wax nu liy ñëw. |
1.157699 | Kambe Petro ni vaapostola van'wana va hlamula, va ku: "Swa hi fanela ku yingisa Xikwembu, ku tlula vanhu. | 29 Piyeer ak ndaw ya ca des nag ne leen: "Yàlla lees wara déggal, waaye du nit. |
1.157546 | Vona wanuna luya a nga ematini. | XOOLAL nit ki nekk fii ci biir géej gi. |
1.157539 | Khonani i khou tshata. | Sa xarit bi takk na jabar. |
1.157495 | Loko a ku nga ri Muxe muhlawuriwa wakwe, | bu dul woon ak Musaa, xejjam |
1.157451 | I yini "vutomi bya xiviri" naswona ha yini wu tsakisa ntshembo | Lan mooy " dund gu wóor gi ," te lu tax mu nekk yaakaar bu neex ? |
1.157439 | Ngauri zwo ambelwa vhoinwi na vhana vhanu na vhothe vha re kule, vhane Murena Mudzimu washu a do vha vhidza. | Ndaxte li Yàlla dige woon, yéena ko moom ak seeni doom ak ñu sore ñépp, di ñépp ñi Yàlla sunu Boroom di woo ci moom." |
1.157372 | Vavanuna va fanele va rhandza vasati va vona ku fana ni mimiri ya vona. - Vaefesa 5:25-29. | Jëkkër yi dañu war a bëgg seen jabar ni ñu bëgge seen bopp. - Efes 5:25-29. |
1.15732 | Fhedzi musi hu tshi ṅwalwa Bivhili, dzina ḽa Mudzimu ḽo vha ḽi tshi bvelela lu ṱoḓaho u vha 7 000. | Waaye ba ñu doon bind Biibël bi, turu Yàlla feeñoon na fa lu jege 7 000 yoon. |
1.15707 | 15Ku lo humelela yini, leswi khale a mi tshama mi tsakile? | 15 Waaw, fan la seen mbég jaar? |
1.156692 | Ndi tshifhio tshifhiwa tsha thengokhulu tshine Mudzimu a ḓo tshi ṋea vhane a vha takalela, nahone ri fanela u ita mini uri ri tshi wane? | Lu rey lan la Yàlla di may ñi ko neex, te lan lañu war a def ngir am loolu ? |
1.156649 | Mune wanga u a tshila. | Sama yaay mu ngiy dund. |
1.156578 | Laha mufananisweni, hi vamani a vavanuna lava va vambiri va yimileko zinwe na Mosi? | Ñaari góor ñi nekk ak Musaa, ñan lañu? |
1.156281 | 7 A ku eka vona: "A hi swa n'wina ku tiva minkarhi kumbe tinguva+ leswi Tatana a swi vekeke hi vulawuri+ byakwe; | 1:7 Mu tontu leen: "Ngeen xam jamono yi ak saa, yi Baay bi dogal ci sañ-sañam, loolu mayuñu leen ko. |
1.155994 | Vanhu van'wana va nga ringeta ku hi tshikisa ku vulavula hi mfumo wa Xikwembu. | Mën na am ay nit jéem ñu tere wax ci nguuru Yàlla. |
1.155944 | 30 Mina na Tatana hi un'we." | 30 Man ak Baay bi benn lanu." |
1.155776 | Naswona ndzi mi lerisa leswaku mi va pfuna.' | Te maa ngi lay digal nga dimbali leen. ' |
1.155568 | Hi wena Elija ke?' | Ndax yaa di Ilyaas?" |
1.155417 | Xana swi vula yini ku amukela Yesu tanihi Muponisi wa mina? | Lan lay tekki nangu Yeesu ni sa Musalkat? |
1.155374 | Hi wena mani vito? = What's your name? | Noo tudd ? / Nan nga tudd ? |
1.155331 | Muxe a a ri ni malembe mangani loko a fa? | Ñaata at la Musaa amoon bi mu deewee? |
1.155248 | lonkulu ú ta va nandza wa lontsongo." | Ki gëna mag ci yeen mooy ki nango nekk seen surga. |
1.155227 | Ha yini Dariyosi a a hlundzuke ngopfu lerova a tsandzeka ni ku etlela, naswona u endle yini eka mixo lowu landzelaka? | Lan moo naqari Dariyus ba mënul nelaw, te lan la def bi suba si jotee ? |
1.155131 | Rubeni a vha vhudza a ri, "A tho ngo ni vhudza nda ri ni songo khakhela uḽa mutukana? | Noonu Yeesu ne leen: "Ndax seen xol dafa tëju ba tey?" |
1.155095 | "Swiendlo swa vona hinkwaswo, ndzi nge swi rivali ni siku ni rin'we. | "Duma fàtte mukk lenn ci seeni jëf. |
1.154947 | Nga ri shavhe, ra sa ralo a hu na na muthihi washu ane a nga ponyoka Abisalomo. | Lu ko moy kenn ci nun du rëcc Absalom. |
1.154807 | matiko a ma te emahlweni ka wena, ma ta avanyisiwa. | na xeet yi dikk fi sa kanam, nga àtte leen. |
1.154794 | Ndi ngani vharangaphanḓa vha vhurereli vho sinyuwa, nahone vho ita mini kha Petro na Yohane? | Lu tax kilifa diine yi mer, te lan lañu def Piyeer ak Yowaana ? |
1.154745 | Xikwembu xa ntiyiso, hi xone Mutumbuluxi wa mintxhumu hinkwayu. | Yàlla dëgg ji moo sàkk lépp. |
1.154481 | Hikuva ku tsariwile leswaku tintsumi ta Xikwembu ti ta ku khawulela.' | 4:10 ndaxte Mbind mi nee na:"Dina jox ay malaakaam ndigal ci sa mbir,ñu sàmm la, |
1.154341 | Musi a tshi ṱangana na Saulo, a vhea zwanḓa zwawe khae a ri: 'Murena o nthuma uri u dovhe u vhone u ḓadzwe nga muya mukhethwa.' | Bi mu gisee Sool, mu teg loxoom yi ci kowam, ne ko: ' Sang bi moo ma yónni ngir nga mën a gisaat te fees ak xel mu sell mi. ' |
1.154268 | Kutani [Yohane] loyi a swi voneke u nyikele vumbhoni, vumbhoni byakwe i bya ntiyiso . . . | Kiy nettali mbir yooyu, da cee teg bëtam, te li muy wax dëgg la. |
1.154266 | I vamani lava nghenaka entangeni, naswona Yudasi Iskariyota u endla yini, hilaha xifaniso xi kombisaka hakona? | Ñan ñooy dugg ci tool bi, te lan la Yudaa Iskariyoo def, ni ñu koy wonee foofu ? |
1.154092 | Vana va fanele va yingisa vatswari va vona. - Vaefesa 6:1-3. | Xale yi dañu war a déggal seeni waajur. - Efes 6:1-3. |
1.153574 | Hikwalaho, lava nga ni tintswalo va kombisa ntwela-vusiwana hakunene. | Yéen ñi am yërmande, barkeel ngeen,ndax dees na leen yërëm. |
1.153549 | Xikwembu xa yena xa n'wi dyondzisa. | te Yàllaam a ko ko jàngal. |
1.153353 | A nge mi tshiki kumbe a mi lovisa kumbe a rivala ntwanano+ wa vatata wa n'wina lowu a va hlambanyeleke wona. | Du leen wacc, du leen yàqte te du fàtte kóllëre, ga mu fasoon ak seeni maam ci kaw ngiñ. |
1.153187 | Ha yini u nga ringeti ku ti tiva ku antswa kutani u tivonela hi wexe loko hakunene ti seketeriwa hi Xikwembu? | Waxal lu tax di kontine di yokk suñu xam-xam ci lu jëm ci Yexowa Yàlla am solo lool. |
1.153177 | Ndzi ku kombile rona leswaku u ri vona hi mahlo ntsena, kambe u nga ka u nga ngheni eka rona." | Bàyyi naa la nga gis ko, waaye doo ci dugg. ' |
1.153068 | 5 Loko ndza ha ri kona emisaveni, hi mina ku vonakala+ ka misava." | 5 Ci bi may nekk àddina, maay leeru àddina." |
1.152647 | 28 Munhu un'wana ni un'wana la honiseke nawu wa Muxe u fa a nga tsetseleriwi, loko ku ri ni vumbhoni bya vanhu vambirhi kumbe vanharhu.+ | 28 Ku weddi ndigali yoonu Musaa wi, te ñaar walla ñetti nit seede ko, dina dee ci lu amul benn yërmande. |
1.152372 | Kambe a swi nge va eneli vanhu lava hinkwavo.' | Waaye loolu du leen mën a doy ñoom ñépp. ' |
1.152328 | 40 Vhaṅwe vhathu henefho kha gogo ḽeneḽo vha tshi pfa a tshi ralo vha ri, "Nangoho hoyu munna ndi onouḽa Muporofita we a pfi u ḓo ḓa." | Bi ñu déggee wax jooja, am ay nit ca mbooloo ma ñu naan: "Dëgg-dëgg kii mooy Yonent bi war a ñëw." |
1.152308 | Ndi hone ḽi tshi ḓo tou niwa nga ṱhoni ḽa ḓisola." | Ndax boo ko defee, dinga ko rusloo." |
1.152149 | Bibele yi vula leswaku nkarhi wolowo i 'masiku yo hetelela.' | Biibël bi dafay woowe jamono jooju " muju jamono ." |
1.151777 | Hinkwaswo leswi nga ri khumbaka swi ta va swo kwetsima.'" | Lépp lu ci laal day doon lu sella sell." |
1.151775 | A tshi ḓa o ḓivhadza vhoṱhe mafhungo maḓifha a mulalo: a a ḓivhadza inwi vhannḓa vhe na vha ni kule na Mudzimu, khathihi na Majuda vhe vha vha vhe tsini nae. | 17 Bi mu ko defee mu ñëw, yégalsi nu xibaaru jàmm fa kanam Yàlla, yéen ñi sore woon ak nun ñi jege. |
1.151641 | Usage: xona u mbirhi; 2. | Usage: dafay nekk ñaar; 2. |
1.151596 | Loy'a swi rhandzaka a a teke, | 18 Kon nag Yàlla, la ko neex lay def, muy yërëm nit, mbaa dëgëral xolam ci lu bon. |
1.151493 | 8 Muya u vhudzula u tshi ya hune wa funa. | 8 Ngelaw fu ko neex lay jublu. |
1.151492 | 5 Adamu a a endliwe hi "xifaniso xa Xikwembu." | 5 Dañu sàkk Aadama ' ci melokaanu Yàlla '. |
1.151449 | Xikwembu xa swi tiva leswaku loko mo dya, mahlo ya n'wina ma ta pfuleka, kutani mi ta fana na xona, mi tiva swo biha ni leswo saseka. | 5 Waaye Yàlla xam na ne bés bu ngeen ci lekkee, seeni bët dina ubbiku, ngeen mel ni Yàlla, xam lu baax ak lu bon." |
1.151147 | lava va n'wi chavaka, naswona u ta ku twa ku rila ka vona va kombela ku pfuniwa." | Dina may ñi ko ragal li ñu bëgg, te dina leen déglu bu ñuy woote ngir ndimbal. " |
1.151137 | 18Rifuwo ni ku dzuneka swi le ka mina, | 18 Alal ak teraangaa ngi fi man, |
1.150998 | Hi mina loyi a nyikelaka vumbhoni malunghana na mina, naswona Tatana loyi a ndzi rhumeke u nyikela vumbhoni malunghana na mina." | 18 Man maa ngi seedeel sama bopp, te Baay bi ma yónni mi ngi may seedeel itam." |
1.150985 | 28 Tomasi a n'wi hlamula, a ku: "Hosi yanga ni Xikwembu xanga!" | 20:28 Tomaa tontu ko ne: "Sama Boroom, sama Yàlla!" |
1.150914 | 15 Xana a ndzi pfumeleriwi ku endla leswi ndzi swi lavaka hi swilo swa mina? | 20:15 ndax sañumaa def ak sama alal li ma neex? |
1.15084 | 48 n'wina mi ta va timbhoni+ ta swilo leswi. | 48 Yéenay samay seede. |
1.150822 | Yesu o ri mini kha Maria, mme awe? | Lan la Yeesu wax yaayam Maryaama ? |
1.150532 | Ndzi landzeleni, ndzi mi yisa eka munhu loyi mi n'wi lavaka." | Toppleen ma, ma yóbbu leen ci ki ngeen di seet." |
1.150396 | 28 Tomasi a n'wi hlamula a ku: "Hosi yanga ni Xikwembu+ xanga!" | 20:28 Tomaa tontu ko ne: "Sama Boroom, sama Yàlla!" |
1.150286 | Misava yi ta pfuleka kutani yi mita vanhu lava vo biha.' | Suuf si dina ubbeeku te wann nit ñu bon ñii. ' |
1.15027 | Xana hlonga ro tshembeka ri ta kuma hakelo leyikulu etilweni ku tlula vatotiwa lavan'wana? | Ana kan ci ñaar ñooñu nag moo ciy gëna fonk leblekat bi?" |
1.150221 | 37 hikuva ku hava lexi tivisiwaka hi Xikwembu lexi nga ta ka xi nga endleki."+ | 1:37 Ndaxte dara tëwul Yàlla." |
1.150192 | Mi nga rivali ku endla leswinene ni ku pambulela van'wana leswi mi nga na swona, hikuva magandzelo lawa hi wona lama tsakisaka Xikwembu. | Buleen fàtte di def lu baax ak di sédde ci seen alal, ndaxte sarax yu mel noonu ñoo neex Yàlla. |
1.15003 | Noa wa ka vaka no ku paridza vanu sa a ka rairgwa no Wedenga, | Nóoyin nit ku jub la woon, di ku mat ci biir nit ñi mu bokkal jamono, te di ku topp Yàlla. |
1.149997 | Vhoṱhe vho vha vho fa, khathihi na vhomme avho na vhathu vhavhi. | Dee nañu ñoom ñépp, ñoom, seeni yaay ak yeneen nit ñu bon ñi. |
1.149942 | Xana a ku ri rihi khombo ra vumune, ra vuntlhanu ni ra vutsevu? | Lan moo xewoon ci ñeenteel, juróomeel ak juróom-benneelu musiba yi? |
1.14994 | Vhukati ha vhusiku muruṅwa wa Mudzimu a vula muṋango wa dzhele, samusi ni tshi nga zwi vhona afha. | Ci guddi gi, malaakaa Yàlla ubbi na buntu kaso bi, ni nga ko gise fii. |
1.149712 | I mikateko yihi leyi nga ta kumiwa hi lava kombisaka leswaku va wu tlangela musa wa Xikwembu lowu nga faneriwiki? | Lu tax ñu war a gërëm Yexowa ndax njot gi mu maye? |
1.149587 | N'wana u lava mpimo wutsongo wa wona hi nkarhi wun'we. | Xale yi du tuuti rekk lañu soxla ci seen jot. |
1.149565 | 53 Kutani un'wana ni un'wana a muka. | 53 Gannaaw loolu ku ci nekk dellu sa kër. |
1.149527 | Mi n'wi yingisela yini xana?" | Lu tax ngeen koy déglu?" |
1.149521 | Naswona i mani la ku nyikeke matimba lawa?"+ | Te ku la may sañ-sañu def ko?" |
1.149473 | Ha yini Yesu a ri Hosi leyi fanelekaka? - MARKA 1:40-42. | Lu tax Yeesu nekk Buur bi gën? - MÀRK 1:40-42. |
1.149291 | 17 Xana vana va nga dyondza swo karhi eka Yesu? | 17 Ndax am na li xale yi mën a jàng ci Yeesu? |
1.149144 | 21 Ndi humbela uri vhoṱhe vha vhe tshithu tshithihi. | 21 Damay ñaan ngir ñépp doon benn. |
1.149138 | Xana wa n'wi tshemba Yesu ku va Muponisi wa wena? | Ndax gëm nga Yeesu ni sa Musalkat ? |
1.149019 | 17 Va hlawulekise entiyisweni; rito ra wena i ntiyiso. | 17 Samp leen ci dëgg, ngir ñu sell. |
1.148979 | Ku pone Nowa ni lava a va ri na yena engalaveni ntsena. | Nóoyin rekk a des, moom ak ña àndoon ak moom ca gaal ga. |
1.148864 | hikuva ndzi vona leswaku u tele nyongwa leyi bavaka ngopfu, ni ku bohiwa hi ku homboloka." | ndaxte gis naa ne, sóobu nga ci lu wex xat ci kanam yàlla, te bàkkaar noot na la." |
1.148773 | Yesu Ene a fhindula a ri, "Mashudu mahulwane a na onoyo muthu ane a ri u pfa ipfi ḽa Mudzimu a ita zwine ḽa amba." | 28 Waaye Yeesu ne ko: "Neel kay, ki barkeel mooy kiy déglu kàddug Yàlla te di ko topp." |
1.148573 | 18 Kutani hakelo ya mina i yini? | 18 Kon nag lan mooy sama yool? |
1.148567 | 11 I Luka ntsena la nga na mina. | 11 Luug rekk a des fi man. |
1.14832 | Hikuva loko mi nga pfumeri leswaku 'Mina ndzi yena', mi ta fela eswidyohweni swa n'wina." | Bu ngeen gëmul ki ma nekk, dingeen dee ci seeni bàkkaar." |
1.148109 | U swi vonisa ku yini? - Hlaya 1 Yohane 3:10-12. | Loo ci xalaat? - Jàngal 1 Yowaana 3: 10- 12. |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.